Abasa · 22/42
Tekki Waxtaan — Simoore Abasa
ثُمَّ إِذَا شَاءَ أَنشَرَهُ ۝٢٢
Thumma iza shaa-a ansharah
📖 Tekkim Wolof
te saa su Ko soobee mu dekkalaat Ko.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 20-24 — Simoore Abasa

20ثُمَّ السَّبِيلَ يَسَّرَهُ
daldi koy yombalal yoon wa ;
21ثُمَّ أَمَاتَهُ فَأَقْبَرَهُ
daldi koy rey, tàbbal ko ci bàmmeel ;
22ثُمَّ إِذَا شَاءَ أَنشَرَهُ
te saa su Ko soobee mu dekkalaat Ko.
23كَلَّا لَمَّا يَقْضِ مَا أَمَرَهُ
Déedéet ! [Nit] moom matalul mukk la nu ko digëloon.
24فَلْيَنظُرِ الْإِنسَانُ إِلَىٰ طَعَامِهِ
Na nit di xool ci aw ñamam lekkam :
AbasaFihi Alxuraan
42Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — Abasa 22

Simoore Abasa Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te saa su Ko soobee mu dekkalaat Ko.

Simoore Aaya 22/42 — Simoore Abasa عبس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Abasa Dégg, Simoore Abasa Tekki, Simoore Abasa mp3, Simoore Abasa pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers