Al-Mutaffifin · 16/36
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mutaffifin
ثُمَّ إِنَّهُمْ لَصَالُو الْجَحِيمِ ۝١٦
Summa innahum lasaa lul jaheem
📖 Tekkim Wolof
te, dees na leen lakk, Safara jahiim ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 14-18 — Simoore Al-Mutaffifin

14كَلَّا ۖ بَلْ ۜ رَانَ عَلَىٰ قُلُوبِهِم مَّا كَانُوا يَكْسِبُونَ
Lañu daan def moo muur xomaagal seen xol ya.
15كَلَّا إِنَّهُمْ عَن رَّبِّهِمْ يَوْمَئِذٍ لَّمَحْجُوبُونَ
Déet ! Ñoom kay bu keroogee duñu gis seen Boroom de,
16ثُمَّ إِنَّهُمْ لَصَالُو الْجَحِيمِ
te, dees na leen lakk, Safara jahiim ;
17ثُمَّ يُقَالُ هَٰذَا الَّذِي كُنتُم بِهِ تُكَذِّبُونَ
te di leen wax naan leen: “Lii ngeen daan weddi ! ”
18كَلَّا إِنَّ كِتَابَ الْأَبْرَارِ لَفِي عِلِّيِّينَ
Déetawaay ! Téereb ñu baax ñaa nga ca biir Illiyiina
Al-MutaffifinFihi Alxuraan
36Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Al-Mutaffifin 16

Simoore Al-Mutaffifin Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te, dees na leen lakk, Safara jahiim ;

Simoore Aaya 16/36 — Simoore Al-Mutaffifin المطففين (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mutaffifin Dégg, Simoore Al-Mutaffifin Tekki, Simoore Al-Mutaffifin mp3, Simoore Al-Mutaffifin pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers