Al-Mutaffifin · 15/36
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mutaffifin
كَلَّا إِنَّهُمْ عَن رَّبِّهِمْ يَوْمَئِذٍ لَّمَحْجُوبُونَ ۝١٥
Kallaaa innahum `ar Rabbihim yawma`izil lamah jooboon
📖 Tekkim Wolof
Déet ! Ñoom kay bu keroogee duñu gis seen Boroom de,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 13-17 — Simoore Al-Mutaffifin

13إِذَا تُتْلَىٰ عَلَيْهِ آيَاتُنَا قَالَ أَسَاطِيرُ الْأَوَّلِينَ
su ñu jàngee ci ñoom Laaya, dañu naan : “Léebi mag ña la! ”
14كَلَّا ۖ بَلْ ۜ رَانَ عَلَىٰ قُلُوبِهِم مَّا كَانُوا يَكْسِبُونَ
Lañu daan def moo muur xomaagal seen xol ya.
15كَلَّا إِنَّهُمْ عَن رَّبِّهِمْ يَوْمَئِذٍ لَّمَحْجُوبُونَ
Déet ! Ñoom kay bu keroogee duñu gis seen Boroom de,
16ثُمَّ إِنَّهُمْ لَصَالُو الْجَحِيمِ
te, dees na leen lakk, Safara jahiim ;
17ثُمَّ يُقَالُ هَٰذَا الَّذِي كُنتُم بِهِ تُكَذِّبُونَ
te di leen wax naan leen: “Lii ngeen daan weddi ! ”
Al-MutaffifinFihi Alxuraan
36Aaya
MeccanRevelation
15Aaya

Tekki — Al-Mutaffifin 15

Simoore Al-Mutaffifin Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Déet ! Ñoom kay bu keroogee duñu gis seen Boroom…

Simoore Aaya 15/36 — Simoore Al-Mutaffifin المطففين (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mutaffifin Dégg, Simoore Al-Mutaffifin Tekki, Simoore Al-Mutaffifin mp3, Simoore Al-Mutaffifin pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers