Al-Mutaffifin · 17/36
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mutaffifin
ثُمَّ يُقَالُ هَٰذَا الَّذِي كُنتُم بِهِ تُكَذِّبُونَ ۝١٧
Summa yuqaalu haazal lazee kuntum bihee tukazziboon
📖 Tekkim Wolof
te di leen wax naan leen: “Lii ngeen daan weddi ! ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 15-19 — Simoore Al-Mutaffifin

15كَلَّا إِنَّهُمْ عَن رَّبِّهِمْ يَوْمَئِذٍ لَّمَحْجُوبُونَ
Déet ! Ñoom kay bu keroogee duñu gis seen Boroom de,
16ثُمَّ إِنَّهُمْ لَصَالُو الْجَحِيمِ
te, dees na leen lakk, Safara jahiim ;
17ثُمَّ يُقَالُ هَٰذَا الَّذِي كُنتُم بِهِ تُكَذِّبُونَ
te di leen wax naan leen: “Lii ngeen daan weddi ! ”
18كَلَّا إِنَّ كِتَابَ الْأَبْرَارِ لَفِي عِلِّيِّينَ
Déetawaay ! Téereb ñu baax ñaa nga ca biir Illiyiina
19وَمَا أَدْرَاكَ مَا عِلِّيُّونَ
ana lan moo lay xamal luy Illiyiina ?
Al-MutaffifinFihi Alxuraan
36Aaya
MeccanRevelation
17Aaya

Tekki — Al-Mutaffifin 17

Simoore Al-Mutaffifin Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te di leen wax naan leen: “Lii ngeen daan weddi…

Simoore Aaya 17/36 — Simoore Al-Mutaffifin المطففين (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mutaffifin Dégg, Simoore Al-Mutaffifin Tekki, Simoore Al-Mutaffifin mp3, Simoore Al-Mutaffifin pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers