Al-Buruj · 15/22
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Buruj
ذُو الْعَرْشِ الْمَجِيدُ ۝١٥
Zul `Arshil Majeed
📖 Tekkim Wolof
Mooy boroom Gàngunaay gu Màgg ga (Aras),

🎧 Dégg


📜 Aaya 13-17 — Simoore Al-Buruj

13إِنَّهُ هُوَ يُبْدِئُ وَيُعِيدُ
Moom mooy, sos bindeef yi, te mooleen di dekkilaat.
14وَهُوَ الْغَفُورُ الْوَدُودُ
Te moom moo di Jéggëlaakoon bi, di soppi lépp,
15ذُو الْعَرْشِ الْمَجِيدُ
Mooy boroom Gàngunaay gu Màgg ga (Aras),
16فَعَّالٌ لِّمَا يُرِيدُ
Lu mu namm dana ko def.
17هَلْ أَتَاكَ حَدِيثُ الْجُنُودِ
Moo ndax waxtaanu xarekat ya dikal na la ( xibaar ya),
Al-BurujFihi Alxuraan
22Aaya
MeccanRevelation
15Aaya

Tekki — Al-Buruj 15

Simoore Al-Buruj Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mooy boroom Gàngunaay gu Màgg ga (Aras),

Simoore Aaya 15/22 — Simoore Al-Buruj البروج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Buruj Dégg, Simoore Al-Buruj Tekki, Simoore Al-Buruj mp3, Simoore Al-Buruj pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers