Al-Buruj · 14/22
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Buruj
وَهُوَ الْغَفُورُ الْوَدُودُ ۝١٤
Wa Huwal Ghafoorul Wadood
📖 Tekkim Wolof
Te moom moo di Jéggëlaakoon bi, di soppi lépp,

🎧 Dégg


📜 Aaya 12-16 — Simoore Al-Buruj

12إِنَّ بَطْشَ رَبِّكَ لَشَدِيدٌ
Sa fayug boroom lu tar la.
13إِنَّهُ هُوَ يُبْدِئُ وَيُعِيدُ
Moom mooy, sos bindeef yi, te mooleen di dekkilaat.
14وَهُوَ الْغَفُورُ الْوَدُودُ
Te moom moo di Jéggëlaakoon bi, di soppi lépp,
15ذُو الْعَرْشِ الْمَجِيدُ
Mooy boroom Gàngunaay gu Màgg ga (Aras),
16فَعَّالٌ لِّمَا يُرِيدُ
Lu mu namm dana ko def.
Al-BurujFihi Alxuraan
22Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — Al-Buruj 14

Simoore Al-Buruj Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te moom moo di Jéggëlaakoon bi, di soppi lépp,

Simoore Aaya 14/22 — Simoore Al-Buruj البروج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Buruj Dégg, Simoore Al-Buruj Tekki, Simoore Al-Buruj mp3, Simoore Al-Buruj pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers