Al-Buruj · 8/22
Tekki Waxtaan — Al-Buruj
وَمَا نَقَمُوا مِنْهُمْ إِلَّا أَن يُؤْمِنُوا بِاللَّهِ الْعَزِيزِ الْحَمِيدِ ۝٨
Wa maa naqamoo minhum illaaa aiyu`minoo billaahil `azeezil Hameed
📖 Tekkim Wolof
te fitnaale wu ñu leen ci lu dul ne da ñoo gëm Yàlla, boroom Kàttan ga, Yayoowaakooni cant ba,
🎧 Dégg

📜 Aaya 6-10 — Al-Buruj

6إِذْ هُمْ عَلَيْهَا قُعُودٌ
ca ba ñu toogee wër ko,
7وَهُمْ عَلَىٰ مَا يَفْعَلُونَ بِالْمُؤْمِنِينَ شُهُودٌ
te ñoom seede la ñu ca la ñu defoon way gëm ña,
8وَمَا نَقَمُوا مِنْهُمْ إِلَّا أَن يُؤْمِنُوا بِاللَّهِ الْعَزِيزِ الْحَمِيدِ
te fitnaale wu ñu leen ci lu dul ne da ñoo gëm Yàlla, boroom Kàttan ga, Yayoowaakooni cant ba,
9الَّذِي لَهُ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ وَاللَّهُ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ شَهِيدٌ
Yàlla mi moom nguurug asamaan yeek suuf si. Te yàlla seede la ci lépp lu ne.
10إِنَّ الَّذِينَ فَتَنُوا الْمُؤْمِنِينَ وَالْمُؤْمِنَاتِ ثُمَّ لَمْ يَتُوبُوا فَلَهُمْ عَذَابُ جَهَنَّمَ وَلَهُمْ عَذَابُ الْحَرِيقِ
Ña daan fitnaal jullit yu góor yaak yu jigéen ya, te tubu ñu ko, dananu am mbugëlum Jahanama ñu di leen ca lakk. (ca safaraam wa)
Al-BurujFihi Alxuraan
22Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Al-Buruj 8

Simoore Al-Buruj Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te fitnaale wu ñu leen ci lu dul ne da…

Simoore Aaya 8/22 — Al-Buruj البروج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Buruj Dégg, Al-Buruj Tekki, Al-Buruj mp3, Al-Buruj pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers