Al-A'la · 8/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'la
وَنُيَسِّرُكَ لِلْيُسْرَىٰ ۝٨
Wa nu-yassiruka lilyusraa
📖 Tekkim Wolof
Dananu la jàppandalal yoon wi gëna yomb.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 6-10 — Simoore Al-A'la

6سَنُقْرِئُكَ فَلَا تَنسَىٰ
Dananu la jàngal (Alxuraan), te doo too ko fàtte
7إِلَّا مَا شَاءَ اللَّهُ ۚ إِنَّهُ يَعْلَمُ الْجَهْرَ وَمَا يَخْفَىٰ
lu dul la soob Yàlla. Moom moo xam li feeñ ak li nëbbu.
8وَنُيَسِّرُكَ لِلْيُسْرَىٰ
Dananu la jàppandalal yoon wi gëna yomb.
9فَذَكِّرْ إِن نَّفَعَتِ الذِّكْرَىٰ
Na ngay fàttelee, saa su fàtteli amee njariñ.
10سَيَذَّكَّرُ مَن يَخْشَىٰ
képp kuy ragal (Yàlla) na nangoo fàttaliku,
Al-A'laFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Al-A'la 8

Simoore Al-A'la Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dananu la jàppandalal yoon wi gëna yomb.

Simoore Aaya 8/19 — Simoore Al-A'la الأعلى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'la Dégg, Simoore Al-A'la Tekki, Simoore Al-A'la mp3, Simoore Al-A'la pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers