Al-A'la · 9/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'la
فَذَكِّرْ إِن نَّفَعَتِ الذِّكْرَىٰ ۝٩
Fazakkir in nafa`atizzikraa
📖 Tekkim Wolof
Na ngay fàttelee, saa su fàtteli amee njariñ.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 7-11 — Simoore Al-A'la

7إِلَّا مَا شَاءَ اللَّهُ ۚ إِنَّهُ يَعْلَمُ الْجَهْرَ وَمَا يَخْفَىٰ
lu dul la soob Yàlla. Moom moo xam li feeñ ak li nëbbu.
8وَنُيَسِّرُكَ لِلْيُسْرَىٰ
Dananu la jàppandalal yoon wi gëna yomb.
9فَذَكِّرْ إِن نَّفَعَتِ الذِّكْرَىٰ
Na ngay fàttelee, saa su fàtteli amee njariñ.
10سَيَذَّكَّرُ مَن يَخْشَىٰ
képp kuy ragal (Yàlla) na nangoo fàttaliku,
11وَيَتَجَنَّبُهَا الْأَشْقَى
ñu texeedi ñaa koy moytu,
Al-A'laFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — Al-A'la 9

Simoore Al-A'la Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Na ngay fàttelee, saa su fàtteli amee njariñ.

Simoore Aaya 9/19 — Simoore Al-A'la الأعلى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'la Dégg, Simoore Al-A'la Tekki, Simoore Al-A'la mp3, Simoore Al-A'la pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers