Al-Fajr · 8/30
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Fajr
الَّتِي لَمْ يُخْلَقْ مِثْلُهَا فِي الْبِلَادِ ۝٨
Allatee lam yukhlaq misluhaa fil bilaad
📖 Tekkim Wolof
yoo xam ne kemam amul ci menn réew ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Simoore Al-Fajr

6أَلَمْ تَرَ كَيْفَ فَعَلَ رَبُّكَ بِعَادٍ
Xanaa gisoo naka la sa Boroom def waa Aad
7إِرَمَ ذَاتِ الْعِمَادِ
Iram, ma doon boroomi kenu,
8الَّتِي لَمْ يُخْلَقْ مِثْلُهَا فِي الْبِلَادِ
yoo xam ne kemam amul ci menn réew ?
9وَثَمُودَ الَّذِينَ جَابُوا الصَّخْرَ بِالْوَادِ
ak waa Saamud ña daan yatt xeer ya ca xur ya ?
10وَفِرْعَوْنَ ذِي الْأَوْتَادِ
ak Firawna, ma doonoon boroomi dàtt ?
Al-FajrFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Al-Fajr 8

Simoore Al-Fajr Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : yoo xam ne kemam amul ci menn réew ?

Simoore Aaya 8/30 — Simoore Al-Fajr الفجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Fajr Dégg, Simoore Al-Fajr Tekki, Simoore Al-Fajr mp3, Simoore Al-Fajr pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers