Al-Fajr · 9/30
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Fajr
وَثَمُودَ الَّذِينَ جَابُوا الصَّخْرَ بِالْوَادِ ۝٩
Wa samoodal lazeena jaabus sakhra bil waad
📖 Tekkim Wolof
ak waa Saamud ña daan yatt xeer ya ca xur ya ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 7-11 — Simoore Al-Fajr

7إِرَمَ ذَاتِ الْعِمَادِ
Iram, ma doon boroomi kenu,
8الَّتِي لَمْ يُخْلَقْ مِثْلُهَا فِي الْبِلَادِ
yoo xam ne kemam amul ci menn réew ?
9وَثَمُودَ الَّذِينَ جَابُوا الصَّخْرَ بِالْوَادِ
ak waa Saamud ña daan yatt xeer ya ca xur ya ?
10وَفِرْعَوْنَ ذِي الْأَوْتَادِ
ak Firawna, ma doonoon boroomi dàtt ?
11الَّذِينَ طَغَوْا فِي الْبِلَادِ
Ñoom, ñoo gënoona bew ci réew yi,
Al-FajrFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — Al-Fajr 9

Simoore Al-Fajr Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ak waa Saamud ña daan yatt xeer ya ca xur…

Simoore Aaya 9/30 — Simoore Al-Fajr الفجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Fajr Dégg, Simoore Al-Fajr Tekki, Simoore Al-Fajr mp3, Simoore Al-Fajr pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers