Al-Balad · 3/20
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Balad
وَوَالِدٍ وَمَا وَلَدَ ۝٣
Wa waalidinw wa maa walad
📖 Tekkim Wolof
Ak ci baay ak la mu jur !

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-5 — Simoore Al-Balad

1لَا أُقْسِمُ بِهَٰذَا الْبَلَدِ
Déet !... Ma ngi giiñ ci dëkk bii !
2وَأَنتَ حِلٌّ بِهَٰذَا الْبَلَدِ
te yaw, sax ci dëkk bi nga dëkk
3وَوَالِدٍ وَمَا وَلَدَ
Ak ci baay ak la mu jur !
4لَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ فِي كَبَدٍ
Noo, bind nit muy jànkonteeki coono.
5أَيَحْسَبُ أَن لَّن يَقْدِرَ عَلَيْهِ أَحَدٌ
Moo ndax dafa defe ni kenn manul ci moom dara ?
Al-BaladFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Al-Balad 3

Simoore Al-Balad Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak ci baay ak la mu jur !

Simoore Aaya 3/20 — Simoore Al-Balad البلد (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Balad Dégg, Simoore Al-Balad Tekki, Simoore Al-Balad mp3, Simoore Al-Balad pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers