Al-Balad · 4/20
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Balad
لَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ فِي كَبَدٍ ۝٤
Laqad khalaqnal insaana fee kabad
📖 Tekkim Wolof
Noo, bind nit muy jànkonteeki coono.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 2-6 — Simoore Al-Balad

2وَأَنتَ حِلٌّ بِهَٰذَا الْبَلَدِ
te yaw, sax ci dëkk bi nga dëkk
3وَوَالِدٍ وَمَا وَلَدَ
Ak ci baay ak la mu jur !
4لَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ فِي كَبَدٍ
Noo, bind nit muy jànkonteeki coono.
5أَيَحْسَبُ أَن لَّن يَقْدِرَ عَلَيْهِ أَحَدٌ
Moo ndax dafa defe ni kenn manul ci moom dara ?
6يَقُولُ أَهْلَكْتُ مَالًا لُّبَدًا
Ma ngay wax naan : “Sànk naa alal ju bari”.
Al-BaladFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Al-Balad 4

Simoore Al-Balad Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noo, bind nit muy jànkonteeki coono.

Simoore Aaya 4/20 — Simoore Al-Balad البلد (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Balad Dégg, Simoore Al-Balad Tekki, Simoore Al-Balad mp3, Simoore Al-Balad pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers