Ash-Shams · 12/15
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shams
إِذِ انبَعَثَ أَشْقَاهَا ۝١٢
Izim ba`asa ashqaahaa
📖 Tekkim Wolof
ba ca ña gën weddi potoxlóo

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 10-14 — Simoore Ash-Shams

10وَقَدْ خَابَ مَن دَسَّاهَا
te it, képp ku ko sàggane, daldi nay sooy.
11كَذَّبَتْ ثَمُودُ بِطَغْوَاهَا
Waa Saamuud, seen bewte, tax na ñu weddi,
12إِذِ انبَعَثَ أَشْقَاهَا
ba ca ña gën weddi potoxlóo
13فَقَالَ لَهُمْ رَسُولُ اللَّهِ نَاقَةَ اللَّهِ وَسُقْيَاهَا
Yonentub Yàlla ba ne leen : “Bàyyileen giléemug Yàlla gi ! mu naan”
14فَكَذَّبُوهُ فَعَقَرُوهَا فَدَمْدَمَ عَلَيْهِمْ رَبُّهُم بِذَنبِهِمْ فَسَوَّاهَا
Ñu weddi ko, rey ko. Seen Boroom, maasale na mbugël ma.ca kaw nit ñépp
Ash-ShamsFihi Alxuraan
15Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Ash-Shams 12

Simoore Ash-Shams Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ba ca ña gën weddi potoxlóo

Simoore Aaya 12/15 — Simoore Ash-Shams الشمس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shams Dégg, Simoore Ash-Shams Tekki, Simoore Ash-Shams mp3, Simoore Ash-Shams pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers