Ad-Duha · 4/11
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Duha
وَلَلْآخِرَةُ خَيْرٌ لَّكَ مِنَ الْأُولَىٰ ۝٤
Walal-aakhiratu khairul laka minal-oola
📖 Tekkim Wolof
Te àllaaxira, mooy, gën ci Yaw àddina de.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 2-6 — Simoore Ad-Duha

2وَاللَّيْلِ إِذَا سَجَىٰ
ak ci guddi gi bu kukkee ! ne
3مَا وَدَّعَكَ رَبُّكَ وَمَا قَلَىٰ
Sa Boroom bàyyiwula, te bañu la.
4وَلَلْآخِرَةُ خَيْرٌ لَّكَ مِنَ الْأُولَىٰ
Te àllaaxira, mooy, gën ci Yaw àddina de.
5وَلَسَوْفَ يُعْطِيكَ رَبُّكَ فَتَرْضَىٰ
Te sa Boroom dana la jox, ba nga doyal.
6أَلَمْ يَجِدْكَ يَتِيمًا فَآوَىٰ
Moo ndax fekku la ngay jirim ? Mu fat la !
Ad-DuhaFihi Alxuraan
11Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Ad-Duha 4

Simoore Ad-Duha Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te àllaaxira, mooy, gën ci Yaw àddina de.

Simoore Aaya 4/11 — Simoore Ad-Duha الضحى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Duha Dégg, Simoore Ad-Duha Tekki, Simoore Ad-Duha mp3, Simoore Ad-Duha pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers