Ad-Duha · 3/11
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Duha
مَا وَدَّعَكَ رَبُّكَ وَمَا قَلَىٰ ۝٣
Ma wad da`aka rabbuka wa ma qalaa
📖 Tekkim Wolof
Sa Boroom bàyyiwula, te bañu la.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 1-5 — Simoore Ad-Duha

1وَالضُّحَىٰ
Ci yoor-yoor bi ! Maa ngi giñ
2وَاللَّيْلِ إِذَا سَجَىٰ
ak ci guddi gi bu kukkee ! ne
3مَا وَدَّعَكَ رَبُّكَ وَمَا قَلَىٰ
Sa Boroom bàyyiwula, te bañu la.
4وَلَلْآخِرَةُ خَيْرٌ لَّكَ مِنَ الْأُولَىٰ
Te àllaaxira, mooy, gën ci Yaw àddina de.
5وَلَسَوْفَ يُعْطِيكَ رَبُّكَ فَتَرْضَىٰ
Te sa Boroom dana la jox, ba nga doyal.
Ad-DuhaFihi Alxuraan
11Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Ad-Duha 3

Simoore Ad-Duha Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sa Boroom bàyyiwula, te bañu la.

Simoore Aaya 3/11 — Simoore Ad-Duha الضحى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Duha Dégg, Simoore Ad-Duha Tekki, Simoore Ad-Duha mp3, Simoore Ad-Duha pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers