Ad-Duha · 5/11
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Duha
وَلَسَوْفَ يُعْطِيكَ رَبُّكَ فَتَرْضَىٰ ۝٥
Wa la sawfa y`uteeka rabbuka fatarda
📖 Tekkim Wolof
Te sa Boroom dana la jox, ba nga doyal.

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Ad-Duha

3مَا وَدَّعَكَ رَبُّكَ وَمَا قَلَىٰ
Sa Boroom bàyyiwula, te bañu la.
4وَلَلْآخِرَةُ خَيْرٌ لَّكَ مِنَ الْأُولَىٰ
Te àllaaxira, mooy, gën ci Yaw àddina de.
5وَلَسَوْفَ يُعْطِيكَ رَبُّكَ فَتَرْضَىٰ
Te sa Boroom dana la jox, ba nga doyal.
6أَلَمْ يَجِدْكَ يَتِيمًا فَآوَىٰ
Moo ndax fekku la ngay jirim ? Mu fat la !
7وَوَجَدَكَ ضَالًّا فَهَدَىٰ
Ak it ndax fekku la nga réer ? Mu gindila.
Ad-DuhaFihi Alxuraan
11Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Ad-Duha 5

Simoore Ad-Duha Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te sa Boroom dana la jox, ba nga doyal.

Simoore Aaya 5/11 — Simoore Ad-Duha الضحى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Duha Dégg, Simoore Ad-Duha Tekki, Simoore Ad-Duha mp3, Simoore Ad-Duha pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers