Hud · 22/123
Tekki Waxtaan — Hud
لَا جَرَمَ أَنَّهُمْ فِي الْآخِرَةِ هُمُ الْأَخْسَرُونَ ۝٢٢
Laa jarama annahum fil Aakhirati humul akhsaroon
📖 Tekkim Wolof
Ca dëgg-dëgg, ñoom ñoo di ña gën a yàqule ca àllaaxira.

🎧 Dégg


📜 Aaya 20-24 — Hud

20أُولَٰئِكَ لَمْ يَكُونُوا مُعْجِزِينَ فِي الْأَرْضِ وَمَا كَانَ لَهُم مِّن دُونِ اللَّهِ مِنْ أَوْلِيَاءَ ۘ يُضَاعَفُ لَهُمُ الْعَذَابُ ۚ مَا كَانُوا يَسْتَطِيعُونَ السَّمْعَ وَمَا كَانُوا يُبْصِرُونَ
Ñooña duñu mën a raw [rëcc] Yàlla ci kaw suuf si ! Te duñu mën a am ku leen wallu, deef na leen fulal mbugal ma. Ngir ñoom mënuñu woon a am dégg-dégg ak gis-gis.
21أُولَٰئِكَ الَّذِينَ خَسِرُوا أَنفُسَهُمْ وَضَلَّ عَنْهُم مَّا كَانُوا يَفْتَرُونَ
Ñoo di ña yàqal seen bopp. Te xërëm ya ñu sosoom danañu leen réer.
22لَا جَرَمَ أَنَّهُمْ فِي الْآخِرَةِ هُمُ الْأَخْسَرُونَ
Ca dëgg-dëgg, ñoom ñoo di ña gën a yàqule ca àllaaxira.
23إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ وَأَخْبَتُوا إِلَىٰ رَبِّهِمْ أُولَٰئِكَ أَصْحَابُ الْجَنَّةِ ۖ هُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
Ña nga xam ne way-gëm lañu, te ñu jëf jëf yu yiw te dellu ci seen Boroom, ñooña ñooy dugg Àjjana te dañu fay béel.
24۞ مَثَلُ الْفَرِيقَيْنِ كَالْأَعْمَىٰ وَالْأَصَمِّ وَالْبَصِيرِ وَالسَّمِيعِ ۚ هَلْ يَسْتَوِيَانِ مَثَلًا ۚ أَفَلَا تَذَكَّرُونَ
Niraleeb ñaari kurél yii mel na ne gumba ga ak tëx ba, ak kuy gis ak kuy dégg. Moo ndax ñaar ñooñu yem nañu te méngoo ? Moo ndax dañu dul xel-lu ?
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — Hud 22

Simoore Hud Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ca dëgg-dëgg, ñoom ñoo di ña gën a yàqule ca…

Simoore Aaya 22/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers