Hud · 21/123
Tekki Waxtaan — Hud
أُولَٰئِكَ الَّذِينَ خَسِرُوا أَنفُسَهُمْ وَضَلَّ عَنْهُم مَّا كَانُوا يَفْتَرُونَ ۝٢١
Ulaaa`ikal lazeena khasirooo anfusahum wa dalla `anhum maa kaanoo yaftaroon
📖 Tekkim Wolof
Ñoo di ña yàqal seen bopp. Te xërëm ya ñu sosoom danañu leen réer.
🎧 Dégg

📜 Aaya 19-23 — Hud

19الَّذِينَ يَصُدُّونَ عَن سَبِيلِ اللَّهِ وَيَبْغُونَهَا عِوَجًا وَهُم بِالْآخِرَةِ هُمْ كَافِرُونَ
Ñoo di ñay wëlbati [nit ña] ngir ñu bañ a jëm ci yoonu Yàlla, di sàkkal diine ay sikk, boole ca ñoom gëmuñu àllaaxira.
20أُولَٰئِكَ لَمْ يَكُونُوا مُعْجِزِينَ فِي الْأَرْضِ وَمَا كَانَ لَهُم مِّن دُونِ اللَّهِ مِنْ أَوْلِيَاءَ ۘ يُضَاعَفُ لَهُمُ الْعَذَابُ ۚ مَا كَانُوا يَسْتَطِيعُونَ السَّمْعَ وَمَا كَانُوا يُبْصِرُونَ
Ñooña duñu mën a raw [rëcc] Yàlla ci kaw suuf si ! Te duñu mën a am ku leen wallu, deef na leen fulal mbugal ma. Ngir ñoom mënuñu woon a am dégg-dégg ak gis-gis.
21أُولَٰئِكَ الَّذِينَ خَسِرُوا أَنفُسَهُمْ وَضَلَّ عَنْهُم مَّا كَانُوا يَفْتَرُونَ
Ñoo di ña yàqal seen bopp. Te xërëm ya ñu sosoom danañu leen réer.
22لَا جَرَمَ أَنَّهُمْ فِي الْآخِرَةِ هُمُ الْأَخْسَرُونَ
Ca dëgg-dëgg, ñoom ñoo di ña gën a yàqule ca àllaaxira.
23إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ وَأَخْبَتُوا إِلَىٰ رَبِّهِمْ أُولَٰئِكَ أَصْحَابُ الْجَنَّةِ ۖ هُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
Ña nga xam ne way-gëm lañu, te ñu jëf jëf yu yiw te dellu ci seen Boroom, ñooña ñooy dugg Àjjana te dañu fay béel.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
21Aaya

Tekki — Hud 21

Simoore Hud Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñoo di ña yàqal seen bopp. Te xërëm ya ñu…

Simoore Aaya 21/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers