Hud · 24/123
Tekki Waxtaan — Simoore Hud
۞ مَثَلُ الْفَرِيقَيْنِ كَالْأَعْمَىٰ وَالْأَصَمِّ وَالْبَصِيرِ وَالسَّمِيعِ ۚ هَلْ يَسْتَوِيَانِ مَثَلًا ۚ أَفَلَا تَذَكَّرُونَ ۝٢٤
Masalul fareeqini kal a`maa wal asammi walbaseeri wassamee`; hal yastawiyaani masalaa; afalaa tazakkaroon
📖 Tekkim Wolof
Niraleeb ñaari kurél yii mel na ne gumba ga ak tëx ba, ak kuy gis ak kuy dégg. Moo ndax ñaar ñooñu yem nañu te méngoo ? Moo ndax dañu dul xel-lu ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 22-26 — Simoore Hud

22لَا جَرَمَ أَنَّهُمْ فِي الْآخِرَةِ هُمُ الْأَخْسَرُونَ
Ca dëgg-dëgg, ñoom ñoo di ña gën a yàqule ca àllaaxira.
23إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ وَأَخْبَتُوا إِلَىٰ رَبِّهِمْ أُولَٰئِكَ أَصْحَابُ الْجَنَّةِ ۖ هُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
Ña nga xam ne way-gëm lañu, te ñu jëf jëf yu yiw te dellu ci seen Boroom, ñooña ñooy dugg Àjjana te dañu fay béel.
24۞ مَثَلُ الْفَرِيقَيْنِ كَالْأَعْمَىٰ وَالْأَصَمِّ وَالْبَصِيرِ وَالسَّمِيعِ ۚ هَلْ يَسْتَوِيَانِ مَثَلًا ۚ أَفَلَا تَذَكَّرُونَ
Niraleeb ñaari kurél yii mel na ne gumba ga ak tëx ba, ak kuy gis ak kuy dégg. Moo ndax ñaar ñooñu yem nañu te méngoo ? Moo ndax dañu dul xel-lu ?
25وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا نُوحًا إِلَىٰ قَوْمِهِ إِنِّي لَكُمْ نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Yónni woon Nanu Nooh ca aw nitam, mu ne leen : “Man waarekat laa bu leen di xamal lu leer
26أَن لَّا تَعْبُدُوا إِلَّا اللَّهَ ۖ إِنِّي أَخَافُ عَلَيْكُمْ عَذَابَ يَوْمٍ أَلِيمٍ
te ngeen bañ a jaamu ku dul Yàlla. Te ragalal naa leen mbugalum bis bu metti dal leen”.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — Hud 24

Simoore Hud Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Niraleeb ñaari kurél yii mel na ne gumba ga ak…

Simoore Aaya 24/123 — Simoore Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Hud Dégg, Simoore Hud Tekki, Simoore Hud mp3, Simoore Hud pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers