Yusuf · 108/111
Tekki Waxtaan — Simoore Yusuf
قُلْ هَٰذِهِ سَبِيلِي أَدْعُو إِلَى اللَّهِ ۚ عَلَىٰ بَصِيرَةٍ أَنَا وَمَنِ اتَّبَعَنِي ۖ وَسُبْحَانَ اللَّهِ وَمَا أَنَا مِنَ الْمُشْرِكِينَ ۝١٠٨
Qul haazihee sabeeleee ad`ooo ilal laah; `alaa baseera tin ana wa manit taba`anee wa Subhaanal laahi wa maaa ana minal mushrikeen
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Samaw yoon a, ngir damay woote jëme ci Yàlla ànd ak aw lay. Man bokkuma ci bokkaalekati Yàlla yi, maak ku ma àndal.

🎧 Dégg


📜 Aaya 106-110 — Simoore Yusuf

106وَمَا يُؤْمِنُ أَكْثَرُهُم بِاللَّهِ إِلَّا وَهُم مُّشْرِكُونَ
Li ëpp ci ñoom duñu gëm Yàlla, xanaa kay dañuy nekk rekk di bokkaale Yàlla.
107أَفَأَمِنُوا أَن تَأْتِيَهُمْ غَاشِيَةٌ مِّنْ عَذَابِ اللَّهِ أَوْ تَأْتِيَهُمُ السَّاعَةُ بَغْتَةً وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ
Ndax dañoo gëmul ne mbugal mu leen muur mën na leen a dal, di mbugalum Yàlla mbaa mu digal leen, bu Bis-pénc baa ci mbetteel te duñu ko yég ?
108قُلْ هَٰذِهِ سَبِيلِي أَدْعُو إِلَى اللَّهِ ۚ عَلَىٰ بَصِيرَةٍ أَنَا وَمَنِ اتَّبَعَنِي ۖ وَسُبْحَانَ اللَّهِ وَمَا أَنَا مِنَ الْمُشْرِكِينَ
Neel : “Samaw yoon a, ngir damay woote jëme ci Yàlla ànd ak aw lay. Man bokkuma ci bokkaalekati Yàlla yi, maak ku ma àndal.
109وَمَا أَرْسَلْنَا مِن قَبْلِكَ إِلَّا رِجَالًا نُّوحِي إِلَيْهِم مِّنْ أَهْلِ الْقُرَىٰ ۗ أَفَلَمْ يَسِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَيَنظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۗ وَلَدَارُ الْآخِرَةِ خَيْرٌ لِّلَّذِينَ اتَّقَوْا ۗ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
Yónniwuñu woon, lu la jiitu [yaw Muhammad], lu dul ay góor yu ñu soloo ñu dëkk ca njénde ya. [Nee leen] ndax dañoo doxul ci suuf si, ba seetlu lan mooy mujjug ña leen jiitu woon ? Te ca dëgg-dëgg kërug àllaaxira moo gën ca ña ragal Yàlla. Moo ndax dangeen dul xel-lu ?
110حَتَّىٰ إِذَا اسْتَيْأَسَ الرُّسُلُ وَظَنُّوا أَنَّهُمْ قَدْ كُذِبُوا جَاءَهُمْ نَصْرُنَا فَنُجِّيَ مَن نَّشَاءُ ۖ وَلَا يُرَدُّ بَأْسُنَا عَنِ الْقَوْمِ الْمُجْرِمِينَ
Ba ña Nu yónni naagoo ne [ndimbal dootul ñëw] te ñu jort ne weddeef nañu leen ba noppi, foofa la Sunu ndimbal agsee ci ñoom. Nu musal ku Nu soob. Te Sunu mbugal amul kenn ku ko mën a fegal tooñkat ya.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
108Aaya

Tekki — Yusuf 108

Simoore Yusuf Aaya 108 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Samaw yoon a, ngir damay woote jëme ci…

Simoore Aaya 108/111 — Simoore Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Yusuf Dégg, Simoore Yusuf Tekki, Simoore Yusuf mp3, Simoore Yusuf pdf. Aaya 106–110. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers