Ar-Ra'd · 40/43
Tekki Waxtaan — Ar-Ra'd
وَإِن مَّا نُرِيَنَّكَ بَعْضَ الَّذِي نَعِدُهُمْ أَوْ نَتَوَفَّيَنَّكَ فَإِنَّمَا عَلَيْكَ الْبَلَاغُ وَعَلَيْنَا الْحِسَابُ ۝٤٠
Wa im maa nurriyannaka ba`dal lazee na`iduhum aw nata waffayannaka fa innamaa `alaikal balaaghu wa `alainal hisaab
📖 Tekkim Wolof
Ndegam won Nanu la lenn ci li Nu leen dig, walla Nu rey la [lu mu ca mën di doon], yaw li la war moo di jotal, waaye Nun noo warloo natt [jëf ya].

🎧 Dégg


📜 Aaya 38-42 — Ar-Ra'd

38وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا رُسُلًا مِّن قَبْلِكَ وَجَعَلْنَا لَهُمْ أَزْوَاجًا وَذُرِّيَّةً ۚ وَمَا كَانَ لِرَسُولٍ أَن يَأْتِيَ بِآيَةٍ إِلَّا بِإِذْنِ اللَّهِ ۗ لِكُلِّ أَجَلٍ كِتَابٌ
Yónni woon Nanu ay Yonent lu jiitu, te defaloon Nanu leen ay soxna ak i doom. Te ab Yonent daawul mën a def kéemaan lu dul ci ndigalul Yàlla. Àppub xew-xew bu mu mën a doon bind Nanu ko ba noppi.
39يَمْحُو اللَّهُ مَا يَشَاءُ وَيُثْبِتُ ۖ وَعِندَهُ أُمُّ الْكِتَابِ
Yàlla dana far lu ko soob te Dana saxal itam [lu ko soob] ca cosaani Téere ba di [Lawhul- Mahfuuz] ma nga fa Moom.
40وَإِن مَّا نُرِيَنَّكَ بَعْضَ الَّذِي نَعِدُهُمْ أَوْ نَتَوَفَّيَنَّكَ فَإِنَّمَا عَلَيْكَ الْبَلَاغُ وَعَلَيْنَا الْحِسَابُ
Ndegam won Nanu la lenn ci li Nu leen dig, walla Nu rey la [lu mu ca mën di doon], yaw li la war moo di jotal, waaye Nun noo warloo natt [jëf ya].
41أَوَلَمْ يَرَوْا أَنَّا نَأْتِي الْأَرْضَ نَنقُصُهَا مِنْ أَطْرَافِهَا ۚ وَاللَّهُ يَحْكُمُ لَا مُعَقِّبَ لِحُكْمِهِ ۚ وَهُوَ سَرِيعُ الْحِسَابِ
Xanaa dañoo gisul ne Nun noo ngi wàññi suuf si ci ay catam ? Yàlla mooy àtte, Dananu delloob àtteem, te Moom ku gaaw la cib nattam.
42وَقَدْ مَكَرَ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ فَلِلَّهِ الْمَكْرُ جَمِيعًا ۖ يَعْلَمُ مَا تَكْسِبُ كُلُّ نَفْسٍ ۗ وَسَيَعْلَمُ الْكُفَّارُ لِمَنْ عُقْبَى الدَّارِ
Ña leen jiitu woon defoon nañu ay pexe ; te Yàllaa moom gépp fànnu pexe. Xam na lu bépp bakkan fàggu. Te yéefar yi danañu mës a xam kan moo moom kër gu mujj ga.
Ar-Ra'dFihi Alxuraan
43Aaya
MedinanRevelation
40Aaya

Tekki — Ar-Ra'd 40

Simoore Ar-Ra'd Aaya 40 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndegam won Nanu la lenn ci li Nu leen dig,…

Simoore Aaya 40/43 — Ar-Ra'd الرعد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Ra'd Dégg, Ar-Ra'd Tekki, Ar-Ra'd mp3, Ar-Ra'd pdf. Aaya 38–42. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers