Al-Hijr · 16/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
وَلَقَدْ جَعَلْنَا فِي السَّمَاءِ بُرُوجًا وَزَيَّنَّاهَا لِلنَّاظِرِينَ ۝١٦
Wa laqad ja`alnaa fissamaaa`i buroojanw wa zaiyannaahaa linnaazireen
📖 Tekkim Wolof
Def nañu ci asamaan ay bidiw te rafetal Nanu ko ñi koy xool mu ne ràññ.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 14-18 — Simoore Al-Hijr

14وَلَوْ فَتَحْنَا عَلَيْهِم بَابًا مِّنَ السَّمَاءِ فَظَلُّوا فِيهِ يَعْرُجُونَ
Te su Nu leen ubbiloon ab buntu ci asamaan ñu mën caa yeendoo yéeg,
15لَقَالُوا إِنَّمَا سُكِّرَتْ أَبْصَارُنَا بَلْ نَحْنُ قَوْمٌ مَّسْحُورُونَ
Kon it fàwwu ñu wax ne : “Dañoo gëlëmal sunuy gët. Walla sax dañu noo njibar”.
16وَلَقَدْ جَعَلْنَا فِي السَّمَاءِ بُرُوجًا وَزَيَّنَّاهَا لِلنَّاظِرِينَ
Def nañu ci asamaan ay bidiw te rafetal Nanu ko ñi koy xool mu ne ràññ.
17وَحَفِظْنَاهَا مِن كُلِّ شَيْطَانٍ رَّجِيمٍ
Te wattu Nanu ko ba sépp séytaane su ñu rëbb du fa mën a egg.
18إِلَّا مَنِ اسْتَرَقَ السَّمْعَ فَأَتْبَعَهُ شِهَابٌ مُّبِينٌ
Lu dul ku jéem a sàcc lu mu dégg, [te ku ko ca jéem] ay jumu safara soxal ko.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Al-Hijr 16

Simoore Al-Hijr Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Def nañu ci asamaan ay bidiw te rafetal Nanu ko…

Simoore Aaya 16/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers