Al-Hijr · 15/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
لَقَالُوا إِنَّمَا سُكِّرَتْ أَبْصَارُنَا بَلْ نَحْنُ قَوْمٌ مَّسْحُورُونَ ۝١٥
Laqaaloo innamaa sukkirat absaarunaa bal nahnu qawmum mashooroon
📖 Tekkim Wolof
Kon it fàwwu ñu wax ne : “Dañoo gëlëmal sunuy gët. Walla sax dañu noo njibar”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 13-17 — Simoore Al-Hijr

13لَا يُؤْمِنُونَ بِهِ ۖ وَقَدْ خَلَتْ سُنَّةُ الْأَوَّلِينَ
Duñu ko gëm te aadaay ñu njëkk ña wéy na.
14وَلَوْ فَتَحْنَا عَلَيْهِم بَابًا مِّنَ السَّمَاءِ فَظَلُّوا فِيهِ يَعْرُجُونَ
Te su Nu leen ubbiloon ab buntu ci asamaan ñu mën caa yeendoo yéeg,
15لَقَالُوا إِنَّمَا سُكِّرَتْ أَبْصَارُنَا بَلْ نَحْنُ قَوْمٌ مَّسْحُورُونَ
Kon it fàwwu ñu wax ne : “Dañoo gëlëmal sunuy gët. Walla sax dañu noo njibar”.
16وَلَقَدْ جَعَلْنَا فِي السَّمَاءِ بُرُوجًا وَزَيَّنَّاهَا لِلنَّاظِرِينَ
Def nañu ci asamaan ay bidiw te rafetal Nanu ko ñi koy xool mu ne ràññ.
17وَحَفِظْنَاهَا مِن كُلِّ شَيْطَانٍ رَّجِيمٍ
Te wattu Nanu ko ba sépp séytaane su ñu rëbb du fa mën a egg.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
15Aaya

Tekki — Al-Hijr 15

Simoore Al-Hijr Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kon it fàwwu ñu wax ne : “Dañoo gëlëmal sunuy…

Simoore Aaya 15/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers