Al-Hijr · 29/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
فَإِذَا سَوَّيْتُهُ وَنَفَخْتُ فِيهِ مِن رُّوحِي فَقَعُوا لَهُ سَاجِدِينَ ۝٢٩
Fa izaa sawwaituhoo wa nafakhtu feehi mir roohee faqa`oo lahoo saajideen
📖 Tekkim Wolof
te saa su Ma ko yemalee ba wal ci dara ci sama ruut, rotleen sujjóotal ko”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 27-31 — Simoore Al-Hijr

27وَالْجَانَّ خَلَقْنَاهُ مِن قَبْلُ مِن نَّارِ السَّمُومِ
Te fekkon na Nu binde jinne lu jiitu loolu ci safara wu xonk coyy.
28وَإِذْ قَالَ رَبُّكَ لِلْمَلَائِكَةِ إِنِّي خَالِقٌ بَشَرًا مِّن صَلْصَالٍ مِّنْ حَمَإٍ مَّسْنُونٍ
[Fàttalikul] ba sa Boroom waxee Malaaka ya ne leen : “Man damay bind nit ci ban bu ñu togg,
29فَإِذَا سَوَّيْتُهُ وَنَفَخْتُ فِيهِ مِن رُّوحِي فَقَعُوا لَهُ سَاجِدِينَ
te saa su Ma ko yemalee ba wal ci dara ci sama ruut, rotleen sujjóotal ko”.
30فَسَجَدَ الْمَلَائِكَةُ كُلُّهُمْ أَجْمَعُونَ
Malaaka yépp sujjóot,
31إِلَّا إِبْلِيسَ أَبَىٰ أَن يَكُونَ مَعَ السَّاجِدِينَ
ba mu des Ibliis, moom bañ naa bokk ca ñay sujjóot.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
29Aaya

Tekki — Al-Hijr 29

Simoore Al-Hijr Aaya 29 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te saa su Ma ko yemalee ba wal ci dara…

Simoore Aaya 29/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 27–31. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers