Al-Hijr · 30/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
فَسَجَدَ الْمَلَائِكَةُ كُلُّهُمْ أَجْمَعُونَ ۝٣٠
Fasajadal malaaa`ikatu kulluhum ajma`oon
📖 Tekkim Wolof
Malaaka yépp sujjóot,

🎧 Dégg


📜 Aaya 28-32 — Simoore Al-Hijr

28وَإِذْ قَالَ رَبُّكَ لِلْمَلَائِكَةِ إِنِّي خَالِقٌ بَشَرًا مِّن صَلْصَالٍ مِّنْ حَمَإٍ مَّسْنُونٍ
[Fàttalikul] ba sa Boroom waxee Malaaka ya ne leen : “Man damay bind nit ci ban bu ñu togg,
29فَإِذَا سَوَّيْتُهُ وَنَفَخْتُ فِيهِ مِن رُّوحِي فَقَعُوا لَهُ سَاجِدِينَ
te saa su Ma ko yemalee ba wal ci dara ci sama ruut, rotleen sujjóotal ko”.
30فَسَجَدَ الْمَلَائِكَةُ كُلُّهُمْ أَجْمَعُونَ
Malaaka yépp sujjóot,
31إِلَّا إِبْلِيسَ أَبَىٰ أَن يَكُونَ مَعَ السَّاجِدِينَ
ba mu des Ibliis, moom bañ naa bokk ca ñay sujjóot.
32قَالَ يَا إِبْلِيسُ مَا لَكَ أَلَّا تَكُونَ مَعَ السَّاجِدِينَ
Mu ne [Moom Yàlla] : “Yaw Ibliis, lu la dal ba bokkuloo ci sujjóotkat yi ? ”
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
30Aaya

Tekki — Al-Hijr 30

Simoore Al-Hijr Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Malaaka yépp sujjóot,

Simoore Aaya 30/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers