Al-Hijr · 76/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
وَإِنَّهَا لَبِسَبِيلٍ مُّقِيمٍ ٧٦
Transliteration
Wa innahaa labi sabeelim muqeem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te [dëkk boobu] nekk na ci yoon wuñuy faral di jaar.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 74-78 — Al-Hijr
74فَجَعَلْنَا عَالِيَهَا سَافِلَهَا وَأَمْطَرْنَا عَلَيْهِمْ حِجَارَةً مِّن سِجِّيلٍ
Nu wëlbati la nekkon ca kaw [dëkk ba] dëpp ko mu féete suuf, Nu sotti ca kaw ab tawu xeer yu jóge Sijjiil.
75إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّلْمُتَوَسِّمِينَ
Loolu nekk ay kéemaan ci ñuy settantal !
76وَإِنَّهَا لَبِسَبِيلٍ مُّقِيمٍ
Te [dëkk boobu] nekk na ci yoon wuñuy faral di jaar.
77إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّلْمُؤْمِنِينَ
Loolu nekk na di kéemtaan ci ñi gëm !
78وَإِن كَانَ أَصْحَابُ الْأَيْكَةِ لَظَالِمِينَ
Te waa Leykata ay tooñkat lañu woon.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
76Aaya
Tekki — Al-Hijr 76
Simoore Al-Hijr Aaya 76 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te [dëkk boobu] nekk na ci yoon wuñuy faral di…Simoore Aaya 76/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 74–78. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








