Al-Hijr · 77/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّلْمُؤْمِنِينَ ۝٧٧
Inna fee zaalika la Aayatal lilmu`mineen
📖 Tekkim Wolof
Loolu nekk na di kéemtaan ci ñi gëm !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 75-79 — Simoore Al-Hijr

75إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّلْمُتَوَسِّمِينَ
Loolu nekk ay kéemaan ci ñuy settantal !
76وَإِنَّهَا لَبِسَبِيلٍ مُّقِيمٍ
Te [dëkk boobu] nekk na ci yoon wuñuy faral di jaar.
77إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّلْمُؤْمِنِينَ
Loolu nekk na di kéemtaan ci ñi gëm !
78وَإِن كَانَ أَصْحَابُ الْأَيْكَةِ لَظَالِمِينَ
Te waa Leykata ay tooñkat lañu woon.
79فَانتَقَمْنَا مِنْهُمْ وَإِنَّهُمَا لَبِإِمَامٍ مُّبِينٍ
Nu mbugal leen. Te [ñaari dëkk yooyu] ñanga ca yoon wu neex a xam.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
77Aaya

Tekki — Al-Hijr 77

Simoore Al-Hijr Aaya 77 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Loolu nekk na di kéemtaan ci ñi gëm !

Simoore Aaya 77/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 75–79. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers