Al-Hijr · 75/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّلْمُتَوَسِّمِينَ ۝٧٥
Inna fee zaalika la Aayaatil lilmutawassimeen
📖 Tekkim Wolof
Loolu nekk ay kéemaan ci ñuy settantal !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 73-77 — Simoore Al-Hijr

73فَأَخَذَتْهُمُ الصَّيْحَةُ مُشْرِقِينَ
Ag xaacu sadd leen suba cuuy.
74فَجَعَلْنَا عَالِيَهَا سَافِلَهَا وَأَمْطَرْنَا عَلَيْهِمْ حِجَارَةً مِّن سِجِّيلٍ
Nu wëlbati la nekkon ca kaw [dëkk ba] dëpp ko mu féete suuf, Nu sotti ca kaw ab tawu xeer yu jóge Sijjiil.
75إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّلْمُتَوَسِّمِينَ
Loolu nekk ay kéemaan ci ñuy settantal !
76وَإِنَّهَا لَبِسَبِيلٍ مُّقِيمٍ
Te [dëkk boobu] nekk na ci yoon wuñuy faral di jaar.
77إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّلْمُؤْمِنِينَ
Loolu nekk na di kéemtaan ci ñi gëm !
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
75Aaya

Tekki — Al-Hijr 75

Simoore Al-Hijr Aaya 75 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Loolu nekk ay kéemaan ci ñuy settantal !

Simoore Aaya 75/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 73–77. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers