An-Nahl · 128/128
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nahl
إِنَّ اللَّهَ مَعَ الَّذِينَ اتَّقَوا وَّالَّذِينَ هُم مُّحْسِنُونَ ۝١٢٨
Innal laaha ma`al lazeenat taqaw wal lazeena hum muhsinoon
📖 Tekkim Wolof
Yàlla nag, ñay rafetal te ragal Ko la àndal de.

🎧 Dégg


📜 Aaya 126-128 — Simoore An-Nahl

126وَإِنْ عَاقَبْتُمْ فَعَاقِبُوا بِمِثْلِ مَا عُوقِبْتُم بِهِ ۖ وَلَئِن صَبَرْتُمْ لَهُوَ خَيْرٌ لِّلصَّابِرِينَ
Nangeen feye ña leen mbugal, lu tollu ni la ñu leen mbugale. Waaye bu ngeen mënee [bañ a feyu]... moo gën ci ñay muñ.
127وَاصْبِرْ وَمَا صَبْرُكَ إِلَّا بِاللَّهِ ۚ وَلَا تَحْزَنْ عَلَيْهِمْ وَلَا تَكُ فِي ضَيْقٍ مِّمَّا يَمْكُرُونَ
Nangay muñ ! Te sag muñ bu mu wéeru fu dul ci Yàlla. Te bul jàq ngir ñoom. Te bul nekk ci tiis ngir la ñuy fexe.
128إِنَّ اللَّهَ مَعَ الَّذِينَ اتَّقَوا وَّالَّذِينَ هُم مُّحْسِنُونَ
Yàlla nag, ñay rafetal te ragal Ko la àndal de.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
128Aaya

Tekki — An-Nahl 128

Simoore An-Nahl Aaya 128 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla nag, ñay rafetal te ragal Ko la àndal de.

Simoore Aaya 128/128 — Simoore An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nahl Dégg, Simoore An-Nahl Tekki, Simoore An-Nahl mp3, Simoore An-Nahl pdf. Aaya 126–128. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers