Al-Isra · 36/111
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Isra
وَلَا تَقْفُ مَا لَيْسَ لَكَ بِهِ عِلْمٌ ۚ إِنَّ السَّمْعَ وَالْبَصَرَ وَالْفُؤَادَ كُلُّ أُولَٰئِكَ كَانَ عَنْهُ مَسْئُولًا ۝٣٦
Wa laa taqfu maa laisa laka bihee `ilm; innas sam`a walbasara walfu`aada kullu ulaaa`ika kaana `anhu mas`oolaa
📖 Tekkim Wolof
Bul toppati loo xam ne amoo ca xam-xam. Naka dégg-dégg ak gis-gis ak li nga fas ci sa xol : loolu lépp Dananu la ca laaj ca Bis-pénc ba.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 34-38 — Simoore Al-Isra

34وَلَا تَقْرَبُوا مَالَ الْيَتِيمِ إِلَّا بِالَّتِي هِيَ أَحْسَنُ حَتَّىٰ يَبْلُغَ أَشُدَّهُ ۚ وَأَوْفُوا بِالْعَهْدِ ۖ إِنَّ الْعَهْدَ كَانَ مَسْئُولًا
Buleen jegeñ alali jirim lu dul ca na mu gën a rafete, ba kero muy nekk mag te sàmm kóllare ga. Ndax kóllare lu ñuy laaj la ëllëg ca àllaaxira
35وَأَوْفُوا الْكَيْلَ إِذَا كِلْتُمْ وَزِنُوا بِالْقِسْطَاسِ الْمُسْتَقِيمِ ۚ ذَٰلِكَ خَيْرٌ وَأَحْسَنُ تَأْوِيلًا
Nangeen di matal natt bu ngeen di natt ; te nangeen di peese cig maandute gu jàpp. Looloo gën te moo gën a rafet ag muj.
36وَلَا تَقْفُ مَا لَيْسَ لَكَ بِهِ عِلْمٌ ۚ إِنَّ السَّمْعَ وَالْبَصَرَ وَالْفُؤَادَ كُلُّ أُولَٰئِكَ كَانَ عَنْهُ مَسْئُولًا
Bul toppati loo xam ne amoo ca xam-xam. Naka dégg-dégg ak gis-gis ak li nga fas ci sa xol : loolu lépp Dananu la ca laaj ca Bis-pénc ba.
37وَلَا تَمْشِ فِي الْأَرْضِ مَرَحًا ۖ إِنَّكَ لَن تَخْرِقَ الْأَرْضَ وَلَن تَبْلُغَ الْجِبَالَ طُولًا
Bul di dox ci kaw suuf ci di rëy-rëylu : yaw mënoo bënn senn suuf te it mënoo jot njoolaayu tundi doj yu rëy yi !
38كُلُّ ذَٰلِكَ كَانَ سَيِّئُهُ عِندَ رَبِّكَ مَكْرُوهًا
Loolu yépp, ñaawtéefam lu ñu sib la ca sa Boroom.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
36Aaya

Tekki — Al-Isra 36

Simoore Al-Isra Aaya 36 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bul toppati loo xam ne amoo ca xam-xam. Naka dégg-dégg…

Simoore Aaya 36/111 — Simoore Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Isra Dégg, Simoore Al-Isra Tekki, Simoore Al-Isra mp3, Simoore Al-Isra pdf. Aaya 34–38. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers