Al-Isra · 37/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَلَا تَمْشِ فِي الْأَرْضِ مَرَحًا ۖ إِنَّكَ لَن تَخْرِقَ الْأَرْضَ وَلَن تَبْلُغَ الْجِبَالَ طُولًا ۝٣٧
Wa laa tamshi fil ardi marahan innaka lan takhriqal arda wa lan tablughal jibaala toola
📖 Tekkim Wolof
Bul di dox ci kaw suuf ci di rëy-rëylu : yaw mënoo bënn senn suuf te it mënoo jot njoolaayu tundi doj yu rëy yi !
🎧 Dégg

📜 Aaya 35-39 — Al-Isra

35وَأَوْفُوا الْكَيْلَ إِذَا كِلْتُمْ وَزِنُوا بِالْقِسْطَاسِ الْمُسْتَقِيمِ ۚ ذَٰلِكَ خَيْرٌ وَأَحْسَنُ تَأْوِيلًا
Nangeen di matal natt bu ngeen di natt ; te nangeen di peese cig maandute gu jàpp. Looloo gën te moo gën a rafet ag muj.
36وَلَا تَقْفُ مَا لَيْسَ لَكَ بِهِ عِلْمٌ ۚ إِنَّ السَّمْعَ وَالْبَصَرَ وَالْفُؤَادَ كُلُّ أُولَٰئِكَ كَانَ عَنْهُ مَسْئُولًا
Bul toppati loo xam ne amoo ca xam-xam. Naka dégg-dégg ak gis-gis ak li nga fas ci sa xol : loolu lépp Dananu la ca laaj ca Bis-pénc ba.
37وَلَا تَمْشِ فِي الْأَرْضِ مَرَحًا ۖ إِنَّكَ لَن تَخْرِقَ الْأَرْضَ وَلَن تَبْلُغَ الْجِبَالَ طُولًا
Bul di dox ci kaw suuf ci di rëy-rëylu : yaw mënoo bënn senn suuf te it mënoo jot njoolaayu tundi doj yu rëy yi !
38كُلُّ ذَٰلِكَ كَانَ سَيِّئُهُ عِندَ رَبِّكَ مَكْرُوهًا
Loolu yépp, ñaawtéefam lu ñu sib la ca sa Boroom.
39ذَٰلِكَ مِمَّا أَوْحَىٰ إِلَيْكَ رَبُّكَ مِنَ الْحِكْمَةِ ۗ وَلَا تَجْعَلْ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ فَتُلْقَىٰ فِي جَهَنَّمَ مَلُومًا مَّدْحُورًا
Loolu nekk na ci la la sa Boroom soloo, muy waare. Bul sàkk jeneen Yàlla di ko booleek Yàlla, dees na la sànni ci Safara, di ku ñu yedd, di ku ñu dàq [boo ko defee].
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
37Aaya

Tekki — Al-Isra 37

Simoore Al-Isra Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bul di dox ci kaw suuf ci di rëy-rëylu :…

Simoore Aaya 37/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers