Al-Isra · 85/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَيَسْأَلُونَكَ عَنِ الرُّوحِ ۖ قُلِ الرُّوحُ مِنْ أَمْرِ رَبِّي وَمَا أُوتِيتُم مِّنَ الْعِلْمِ إِلَّا قَلِيلًا ۝٨٥
Wa yas`aloonaka `anirrooh; qulir roohu min amri rabbee wa maaa ooteetum minal `ilmi illaa qaleelaa
📖 Tekkim Wolof
Ña nga lay laaj lu jëm ci ruu, - Neel : “ Ruu ci mbiri sama Boroom la bokk”. Te joxeefuleen ci xam-xam lu dul lu tuuti.

🎧 Dégg


📜 Aaya 83-87 — Al-Isra

83وَإِذَا أَنْعَمْنَا عَلَى الْإِنسَانِ أَعْرَضَ وَنَأَىٰ بِجَانِبِهِ ۖ وَإِذَا مَسَّهُ الشَّرُّ كَانَ يَئُوسًا
Te bu Nu defalee nit xéewal ; mu dëddu, fuuyu ci wetam ; waaye bu ko tiis dalee, mu ñàkk yaakaar [yërmaande Yàlla].
84قُلْ كُلٌّ يَعْمَلُ عَلَىٰ شَاكِلَتِهِ فَرَبُّكُمْ أَعْلَمُ بِمَنْ هُوَ أَهْدَىٰ سَبِيلًا
Neel : “Ku nekk a ngay jëf lu méngook meloon, waaye sa Boroom a gën a xam ku gindiku tegu ca yoon wu jub wa”.
85وَيَسْأَلُونَكَ عَنِ الرُّوحِ ۖ قُلِ الرُّوحُ مِنْ أَمْرِ رَبِّي وَمَا أُوتِيتُم مِّنَ الْعِلْمِ إِلَّا قَلِيلًا
Ña nga lay laaj lu jëm ci ruu, - Neel : “ Ruu ci mbiri sama Boroom la bokk”. Te joxeefuleen ci xam-xam lu dul lu tuuti.
86وَلَئِن شِئْنَا لَنَذْهَبَنَّ بِالَّذِي أَوْحَيْنَا إِلَيْكَ ثُمَّ لَا تَجِدُ لَكَ بِهِ عَلَيْنَا وَكِيلًا
Ca dëgg-dëgg su Nu neexoon, Nu yóbbu li nu la xamal ; te kon doo am kenn ku la musal ci Nun.
87إِلَّا رَحْمَةً مِّن رَّبِّكَ ۚ إِنَّ فَضْلَهُ كَانَ عَلَيْكَ كَبِيرًا
Lu dul yërmaande ju jóge ci sa Boroom, te ngënéelam li Mu la jagleel rëy na [ba tax na Mu bàyyee la xam-xam bi bañ koo rocci].
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
85Aaya

Tekki — Al-Isra 85

Simoore Al-Isra Aaya 85 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña nga lay laaj lu jëm ci ruu, - Neel…

Simoore Aaya 85/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 83–87. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers