Al-Isra · 86/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَلَئِن شِئْنَا لَنَذْهَبَنَّ بِالَّذِي أَوْحَيْنَا إِلَيْكَ ثُمَّ لَا تَجِدُ لَكَ بِهِ عَلَيْنَا وَكِيلًا ٨٦
Transliteration
Wa la`in shi`naa lanaz habanna billazeee awhainaaa ilaika summa laa tajidu laka bihee `alainaa wakeelaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ca dëgg-dëgg su Nu neexoon, Nu yóbbu li nu la xamal ; te kon doo am kenn ku la musal ci Nun.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 84-88 — Al-Isra
84قُلْ كُلٌّ يَعْمَلُ عَلَىٰ شَاكِلَتِهِ فَرَبُّكُمْ أَعْلَمُ بِمَنْ هُوَ أَهْدَىٰ سَبِيلًا
Neel : “Ku nekk a ngay jëf lu méngook meloon, waaye sa Boroom a gën a xam ku gindiku tegu ca yoon wu jub wa”.
85وَيَسْأَلُونَكَ عَنِ الرُّوحِ ۖ قُلِ الرُّوحُ مِنْ أَمْرِ رَبِّي وَمَا أُوتِيتُم مِّنَ الْعِلْمِ إِلَّا قَلِيلًا
Ña nga lay laaj lu jëm ci ruu, - Neel : “ Ruu ci mbiri sama Boroom la bokk”. Te joxeefuleen ci xam-xam lu dul lu tuuti.
86وَلَئِن شِئْنَا لَنَذْهَبَنَّ بِالَّذِي أَوْحَيْنَا إِلَيْكَ ثُمَّ لَا تَجِدُ لَكَ بِهِ عَلَيْنَا وَكِيلًا
Ca dëgg-dëgg su Nu neexoon, Nu yóbbu li nu la xamal ; te kon doo am kenn ku la musal ci Nun.
87إِلَّا رَحْمَةً مِّن رَّبِّكَ ۚ إِنَّ فَضْلَهُ كَانَ عَلَيْكَ كَبِيرًا
Lu dul yërmaande ju jóge ci sa Boroom, te ngënéelam li Mu la jagleel rëy na [ba tax na Mu bàyyee la xam-xam bi bañ koo rocci].
88قُل لَّئِنِ اجْتَمَعَتِ الْإِنسُ وَالْجِنُّ عَلَىٰ أَن يَأْتُوا بِمِثْلِ هَٰذَا الْقُرْآنِ لَا يَأْتُونَ بِمِثْلِهِ وَلَوْ كَانَ بَعْضُهُمْ لِبَعْضٍ ظَهِيرًا
Neel : “Bu nit ak jinne booloo woon ngir fexee indi lu mel ni Alxuraan jii, duñu mën a indi lu ni mel, doonte dañu caa dimbalante”.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
86Aaya
Tekki — Al-Isra 86
Simoore Al-Isra Aaya 86 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ca dëgg-dëgg su Nu neexoon, Nu yóbbu li nu la…Simoore Aaya 86/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 84–88. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








