Maryam · 5/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
وَإِنِّي خِفْتُ الْمَوَالِيَ مِن وَرَائِي وَكَانَتِ امْرَأَتِي عَاقِرًا فَهَبْ لِي مِن لَّدُنكَ وَلِيًّا ۝٥
Wa innee khiftul mawaa liya minw waraaa`ee wa kaana tim ra atee `aairan fahab lee mil ladunka waliyyaa
📖 Tekkim Wolof
Te man dey tiit naa ci ñi may donn [ëllëg]. Te sama soxna jaasir la. Ay waay may ma doom

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Maryam

3إِذْ نَادَىٰ رَبَّهُ نِدَاءً خَفِيًّا
Jamono ja muy ñaan Boroomam ci ag yalu,
4قَالَ رَبِّ إِنِّي وَهَنَ الْعَظْمُ مِنِّي وَاشْتَعَلَ الرَّأْسُ شَيْبًا وَلَمْ أَكُن بِدُعَائِكَ رَبِّ شَقِيًّا
mu ñaanoon ne : “Yaw Boroom bi, sama kàttan néew na, sama bopp bi bijjaaw na. Te mësumaa sooy ci ñaan la.
5وَإِنِّي خِفْتُ الْمَوَالِيَ مِن وَرَائِي وَكَانَتِ امْرَأَتِي عَاقِرًا فَهَبْ لِي مِن لَّدُنكَ وَلِيًّا
Te man dey tiit naa ci ñi may donn [ëllëg]. Te sama soxna jaasir la. Ay waay may ma doom
6يَرِثُنِي وَيَرِثُ مِنْ آلِ يَعْقُوبَ ۖ وَاجْعَلْهُ رَبِّ رَضِيًّا
[doom] ju may donn, di donn itam njabootug Yànqooba. Te nga def ko muy kuy gërëm”.
7يَا زَكَرِيَّا إِنَّا نُبَشِّرُكَ بِغُلَامٍ اسْمُهُ يَحْيَىٰ لَمْ نَجْعَل لَّهُ مِن قَبْلُ سَمِيًّا
"Éy Zakariyaa, Noo ngi lay bégal ci ne [danga am] doom ju tudd Yahyaa. Te turam woowu kenn masu koo am”.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Maryam 5

Simoore Maryam Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te man dey tiit naa ci ñi may donn [ëllëg].…

Simoore Aaya 5/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers