Maryam · 4/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
قَالَ رَبِّ إِنِّي وَهَنَ الْعَظْمُ مِنِّي وَاشْتَعَلَ الرَّأْسُ شَيْبًا وَلَمْ أَكُن بِدُعَائِكَ رَبِّ شَقِيًّا ۝٤
Qaala Rabbi innee wahanal`azmu minnee washta`alar raasu shaibanw wa lam akum bidu`aaa`ika Rabbi shaqiyyaa
📖 Tekkim Wolof
mu ñaanoon ne : “Yaw Boroom bi, sama kàttan néew na, sama bopp bi bijjaaw na. Te mësumaa sooy ci ñaan la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 2-6 — Simoore Maryam

2ذِكْرُ رَحْمَتِ رَبِّكَ عَبْدَهُ زَكَرِيَّا
[Fàttalikul] firndey yërmaandey sa Boroom ca jaamam ba Zakariyaa.
3إِذْ نَادَىٰ رَبَّهُ نِدَاءً خَفِيًّا
Jamono ja muy ñaan Boroomam ci ag yalu,
4قَالَ رَبِّ إِنِّي وَهَنَ الْعَظْمُ مِنِّي وَاشْتَعَلَ الرَّأْسُ شَيْبًا وَلَمْ أَكُن بِدُعَائِكَ رَبِّ شَقِيًّا
mu ñaanoon ne : “Yaw Boroom bi, sama kàttan néew na, sama bopp bi bijjaaw na. Te mësumaa sooy ci ñaan la.
5وَإِنِّي خِفْتُ الْمَوَالِيَ مِن وَرَائِي وَكَانَتِ امْرَأَتِي عَاقِرًا فَهَبْ لِي مِن لَّدُنكَ وَلِيًّا
Te man dey tiit naa ci ñi may donn [ëllëg]. Te sama soxna jaasir la. Ay waay may ma doom
6يَرِثُنِي وَيَرِثُ مِنْ آلِ يَعْقُوبَ ۖ وَاجْعَلْهُ رَبِّ رَضِيًّا
[doom] ju may donn, di donn itam njabootug Yànqooba. Te nga def ko muy kuy gërëm”.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Maryam 4

Simoore Maryam Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : mu ñaanoon ne : “Yaw Boroom bi, sama kàttan néew…

Simoore Aaya 4/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers