Maryam · 66/98
Tekki Waxtaan — Maryam
وَيَقُولُ الْإِنسَانُ أَإِذَا مَا مِتُّ لَسَوْفَ أُخْرَجُ حَيًّا ٦٦
Transliteration
Wa yaqoolul insaanu `aizaa maa mittu lasawfa ukhraju haiyaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nit nag di wax naan : “Ndax su ma dee danañu ma génnewaat may dundu ? ”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 64-68 — Maryam
64وَمَا نَتَنَزَّلُ إِلَّا بِأَمْرِ رَبِّكَ ۖ لَهُ مَا بَيْنَ أَيْدِينَا وَمَا خَلْفَنَا وَمَا بَيْنَ ذَٰلِكَ ۚ وَمَا كَانَ رَبُّكَ نَسِيًّا
“Dunu wàcce ca Àjjana ja lu dul ci ndigalul Yàlla. Mooy Boroom li wéy ak li teew ak liy ñëw. Sa Boroom du fàtte de.
65رَّبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا فَاعْبُدْهُ وَاصْطَبِرْ لِعِبَادَتِهِ ۚ هَلْ تَعْلَمُ لَهُ سَمِيًّا
Boroom asamaan yi ak suuf si ak li nekk ci seen diggante. Nanga ko jaamu te nanga sax ci jaamu Ko. Waaw ndax xamal nga ko benn turandoo? Mukk amul ”
66وَيَقُولُ الْإِنسَانُ أَإِذَا مَا مِتُّ لَسَوْفَ أُخْرَجُ حَيًّا
Nit nag di wax naan : “Ndax su ma dee danañu ma génnewaat may dundu ? ”
67أَوَلَا يَذْكُرُ الْإِنسَانُ أَنَّا خَلَقْنَاهُ مِن قَبْلُ وَلَمْ يَكُ شَيْئًا
Moo ndax nit dafa fàttalikuwul ne Noo ko bindoon bu njëkk te doonutoon dara ?
68فَوَرَبِّكَ لَنَحْشُرَنَّهُمْ وَالشَّيَاطِينَ ثُمَّ لَنُحْضِرَنَّهُمْ حَوْلَ جَهَنَّمَ جِثِيًّا
Giñ naa ci sa màggug Boroom ne Dananu leen pang [dajale] ñook séytaane ya ba ñu yemb. Nu wërële leen ca Safara ñu sukk fa.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
66Aaya
Tekki — Maryam 66
Simoore Maryam Aaya 66 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nit nag di wax naan : “Ndax su ma dee…Simoore Aaya 66/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 64–68. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








