Taha · 100/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
مَّنْ أَعْرَضَ عَنْهُ فَإِنَّهُ يَحْمِلُ يَوْمَ الْقِيَامَةِ وِزْرًا ۝١٠٠
Man a`rada `anhu, fa innahoo yahmilu Yawmal Qiyaamati wizraa
📖 Tekkim Wolof
Ku ko dummóoyu [kàddu yooyu], bu Bis-pénc baa, dana yenu ay bàkkaar [mbugal] ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 98-102 — Simoore Taha

98إِنَّمَا إِلَٰهُكُمُ اللَّهُ الَّذِي لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۚ وَسِعَ كُلَّ شَيْءٍ عِلْمًا
[Seen Yàlla tigi] mooy Yàlla jenn ja, amul jeneen ju dul Moom. Moo xam lépp.
99كَذَٰلِكَ نَقُصُّ عَلَيْكَ مِنْ أَنبَاءِ مَا قَدْ سَبَقَ ۚ وَقَدْ آتَيْنَاكَ مِن لَّدُنَّا ذِكْرًا
Noonu la Nu lay nettalee xew-xewi ña jiitu woon. Indil naa la njàng mu bawoo fi Man.
100مَّنْ أَعْرَضَ عَنْهُ فَإِنَّهُ يَحْمِلُ يَوْمَ الْقِيَامَةِ وِزْرًا
Ku ko dummóoyu [kàddu yooyu], bu Bis-pénc baa, dana yenu ay bàkkaar [mbugal] ;
101خَالِدِينَ فِيهِ ۖ وَسَاءَ لَهُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ حِمْلًا
te dañu cay béelbu keroo gee [Bis-pénc ba], ndaw yen bu bon,
102يَوْمَ يُنفَخُ فِي الصُّورِ ۚ وَنَحْشُرُ الْمُجْرِمِينَ يَوْمَئِذٍ زُرْقًا
bis ba ñu walee [ëf] buftu ba, bis boobee, Dananu pang tooñkat ya ñuy fér-féri [ndax tiit] !
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
100Aaya

Tekki — Taha 100

Simoore Taha Aaya 100 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ku ko dummóoyu [kàddu yooyu], bu Bis-pénc baa, dana yenu…

Simoore Aaya 100/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 98–102. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers