Taha · 64/135
Tekki Waxtaan — Taha
فَأَجْمِعُوا كَيْدَكُمْ ثُمَّ ائْتُوا صَفًّا ۚ وَقَدْ أَفْلَحَ الْيَوْمَ مَنِ اسْتَعْلَىٰ ۝٦٤
Fa ajmi`oo kaidakum summma`too saffaa; wa qad aflahal yawma manis ta`laa
📖 Tekkim Wolof
Kon booleleen seeni pexe, doon jenn jëmm bisub tey bii. Ku not rekk raw nga ba fàwwu”
🎧 Dégg

📜 Aaya 62-66 — Taha

62فَتَنَازَعُوا أَمْرَهُم بَيْنَهُمْ وَأَسَرُّوا النَّجْوَىٰ
Ñu xëccoo ca seen biir, gise, déeyoo di yum-yumi.
63قَالُوا إِنْ هَٰذَانِ لَسَاحِرَانِ يُرِيدَانِ أَن يُخْرِجَاكُم مِّنْ أَرْضِكُم بِسِحْرِهِمَا وَيَذْهَبَا بِطَرِيقَتِكُمُ الْمُثْلَىٰ
Ñu daldi wax ne : “Ñaar ñii dey, ay jibar lañu, li leen tax a jóg moo di génne leen ci seenum réew, not leen ba fàwwu.
64فَأَجْمِعُوا كَيْدَكُمْ ثُمَّ ائْتُوا صَفًّا ۚ وَقَدْ أَفْلَحَ الْيَوْمَ مَنِ اسْتَعْلَىٰ
Kon booleleen seeni pexe, doon jenn jëmm bisub tey bii. Ku not rekk raw nga ba fàwwu”
65قَالُوا يَا مُوسَىٰ إِمَّا أَن تُلْقِيَ وَإِمَّا أَن نَّكُونَ أَوَّلَ مَنْ أَلْقَىٰ
Ñu ne ko : "Yaw Muusaa, benn nga jëkk a sànni, walla nun nooy jëkk a sànni ? ”
66قَالَ بَلْ أَلْقُوا ۖ فَإِذَا حِبَالُهُمْ وَعِصِيُّهُمْ يُخَيَّلُ إِلَيْهِ مِن سِحْرِهِمْ أَنَّهَا تَسْعَىٰ
Muusaa ne leeen] : “Sànnileen”. Ñu daldi sànni seeni yet ak i buum ca seenug njibar mu mel ni yëf yaa ngay dox di yëngatu.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
64Aaya

Tekki — Taha 64

Simoore Taha Aaya 64 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kon booleleen seeni pexe, doon jenn jëmm bisub tey bii.…

Simoore Aaya 64/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 62–66. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers