Taha · 63/135
Tekki Waxtaan — Taha
قَالُوا إِنْ هَٰذَانِ لَسَاحِرَانِ يُرِيدَانِ أَن يُخْرِجَاكُم مِّنْ أَرْضِكُم بِسِحْرِهِمَا وَيَذْهَبَا بِطَرِيقَتِكُمُ الْمُثْلَىٰ ۝٦٣
Qaalooo in haaazaani lasaahiraani yureedaani ai yukhrijaakum min ardikum bisihrihimaa wa yazhabaa bitareeqatikumul muslaa
📖 Tekkim Wolof
Ñu daldi wax ne : “Ñaar ñii dey, ay jibar lañu, li leen tax a jóg moo di génne leen ci seenum réew, not leen ba fàwwu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 61-65 — Taha

61قَالَ لَهُم مُّوسَىٰ وَيْلَكُمْ لَا تَفْتَرُوا عَلَى اللَّهِ كَذِبًا فَيُسْحِتَكُم بِعَذَابٍ ۖ وَقَدْ خَابَ مَنِ افْتَرَىٰ
Muusaa ne leen : “Tuskare ngeen ! Fexeleen ba bu leen duural Yàlla ay fen : kon Mu toroxal leen de. Te duurkat sooy nañu”.
62فَتَنَازَعُوا أَمْرَهُم بَيْنَهُمْ وَأَسَرُّوا النَّجْوَىٰ
Ñu xëccoo ca seen biir, gise, déeyoo di yum-yumi.
63قَالُوا إِنْ هَٰذَانِ لَسَاحِرَانِ يُرِيدَانِ أَن يُخْرِجَاكُم مِّنْ أَرْضِكُم بِسِحْرِهِمَا وَيَذْهَبَا بِطَرِيقَتِكُمُ الْمُثْلَىٰ
Ñu daldi wax ne : “Ñaar ñii dey, ay jibar lañu, li leen tax a jóg moo di génne leen ci seenum réew, not leen ba fàwwu.
64فَأَجْمِعُوا كَيْدَكُمْ ثُمَّ ائْتُوا صَفًّا ۚ وَقَدْ أَفْلَحَ الْيَوْمَ مَنِ اسْتَعْلَىٰ
Kon booleleen seeni pexe, doon jenn jëmm bisub tey bii. Ku not rekk raw nga ba fàwwu”
65قَالُوا يَا مُوسَىٰ إِمَّا أَن تُلْقِيَ وَإِمَّا أَن نَّكُونَ أَوَّلَ مَنْ أَلْقَىٰ
Ñu ne ko : "Yaw Muusaa, benn nga jëkk a sànni, walla nun nooy jëkk a sànni ? ”
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
63Aaya

Tekki — Taha 63

Simoore Taha Aaya 63 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu daldi wax ne : “Ñaar ñii dey, ay jibar…

Simoore Aaya 63/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 61–65. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers