Taha · 85/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
قَالَ فَإِنَّا قَدْ فَتَنَّا قَوْمَكَ مِن بَعْدِكَ وَأَضَلَّهُمُ السَّامِرِيُّ ۝٨٥
Qaala fa innaa qad fatannaa qawmaka mim ba`dika wa adallahumus Saamiriyy
📖 Tekkim Wolof
[Yàlla] ne ko : “Nattu woon Nanu saw nit sa ginnaaw. Saamiriyu ñëw moom sànk leen”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 83-87 — Simoore Taha

83۞ وَمَا أَعْجَلَكَ عَن قَوْمِكَ يَا مُوسَىٰ
“Waaw Muusaa, ana lan moo tax nga jiitu saw nit ? ”
84قَالَ هُمْ أُولَاءِ عَلَىٰ أَثَرِي وَعَجِلْتُ إِلَيْكَ رَبِّ لِتَرْضَىٰ
Mu ne ko ñoom dey ñanga ca sama ginnaaw. Ma yàkkamtee agsi ci Yaw ba am sa ngërëm.
85قَالَ فَإِنَّا قَدْ فَتَنَّا قَوْمَكَ مِن بَعْدِكَ وَأَضَلَّهُمُ السَّامِرِيُّ
[Yàlla] ne ko : “Nattu woon Nanu saw nit sa ginnaaw. Saamiriyu ñëw moom sànk leen”.
86فَرَجَعَ مُوسَىٰ إِلَىٰ قَوْمِهِ غَضْبَانَ أَسِفًا ۚ قَالَ يَا قَوْمِ أَلَمْ يَعِدْكُمْ رَبُّكُمْ وَعْدًا حَسَنًا ۚ أَفَطَالَ عَلَيْكُمُ الْعَهْدُ أَمْ أَرَدتُّمْ أَن يَحِلَّ عَلَيْكُمْ غَضَبٌ مِّن رَّبِّكُمْ فَأَخْلَفْتُم مَّوْعِدِي
Muusaa dellu fa nitam ña mer bay fuur ; ne leen : "Yéen samaw nit, ndax Yàlla digu leen woon dig wu rafet ? Walla dig wa dafa yàgg ? Walla dangeen bëgg merum Yàlla wàcc ci seen kaw, ba tax ngeen wuute samag dig ay yéen ? ”
87قَالُوا مَا أَخْلَفْنَا مَوْعِدَكَ بِمَلْكِنَا وَلَٰكِنَّا حُمِّلْنَا أَوْزَارًا مِّن زِينَةِ الْقَوْمِ فَقَذَفْنَاهَا فَكَذَٰلِكَ أَلْقَى السَّامِرِيُّ
Ñu ne ko : “Wuutewuñu sab dig. Waaye danu noo nax sànniloo nu takkaay ya ; ca noona la ko Saamiriyu sànnee ca safara wa.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
85Aaya

Tekki — Taha 85

Simoore Taha Aaya 85 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Yàlla] ne ko : “Nattu woon Nanu saw nit sa…

Simoore Aaya 85/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 83–87. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers