Taha · 91/135
Tekki Waxtaan — Taha
قَالُوا لَن نَّبْرَحَ عَلَيْهِ عَاكِفِينَ حَتَّىٰ يَرْجِعَ إِلَيْنَا مُوسَىٰ ٩١
Transliteration
Qaaloo lan nabraha `alaihi `aakifeena hattaa yarji`a ilainaa Moosaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne ko : “Dunu fi jóge mukk ba ba Muusaa di dellusi fi nun”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 89-93 — Taha
89أَفَلَا يَرَوْنَ أَلَّا يَرْجِعُ إِلَيْهِمْ قَوْلًا وَلَا يَمْلِكُ لَهُمْ ضَرًّا وَلَا نَفْعًا
Moo ndax dañoo gisul ne bu ñul wax ak moom du toontu, te mënuleen a lor, mënuleen a jariñ dara ?
90وَلَقَدْ قَالَ لَهُمْ هَارُونُ مِن قَبْلُ يَا قَوْمِ إِنَّمَا فُتِنتُم بِهِ ۖ وَإِنَّ رَبَّكُمُ الرَّحْمَٰنُ فَاتَّبِعُونِي وَأَطِيعُوا أَمْرِي
Aaruuna moom waxoon na leen bu njëkk ne leen: "Yéen samaw nit, lii ngeen nekk aw sànje la. Waaye seen Boroom moo di Yërëmaakoon bi. Toppleen ma te wéyal samay ndigal”.
91قَالُوا لَن نَّبْرَحَ عَلَيْهِ عَاكِفِينَ حَتَّىٰ يَرْجِعَ إِلَيْنَا مُوسَىٰ
Ñu ne ko : “Dunu fi jóge mukk ba ba Muusaa di dellusi fi nun”.
92قَالَ يَا هَارُونُ مَا مَنَعَكَ إِذْ رَأَيْتَهُمْ ضَلُّوا
[Ba Muusaa dellusee] ne : “Yaw Aaruuna, lan moo tere woon nga waar leen ba ñu sànkoo.
93أَلَّا تَتَّبِعَنِ ۖ أَفَعَصَيْتَ أَمْرِي
Danga maa toppatul walla dangaa mooy léegi samay ndigal ? ”
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
91Aaya
Tekki — Taha 91
Simoore Taha Aaya 91 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne ko : “Dunu fi jóge mukk ba ba…Simoore Aaya 91/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 89–93. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








