Taha · 98/135
Tekki Waxtaan — Taha
إِنَّمَا إِلَٰهُكُمُ اللَّهُ الَّذِي لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۚ وَسِعَ كُلَّ شَيْءٍ عِلْمًا ۝٩٨
Innamaaa ilaahukkumul laahul lazee laa ilaaha illaa Hoo; wasi`a kulla shai`in ilmaa
📖 Tekkim Wolof
[Seen Yàlla tigi] mooy Yàlla jenn ja, amul jeneen ju dul Moom. Moo xam lépp.

🎧 Dégg


📜 Aaya 96-100 — Taha

96قَالَ بَصُرْتُ بِمَا لَمْ يَبْصُرُوا بِهِ فَقَبَضْتُ قَبْضَةً مِّنْ أَثَرِ الرَّسُولِ فَنَبَذْتُهَا وَكَذَٰلِكَ سَوَّلَتْ لِي نَفْسِي
Mu ne : “Gis naa lu ñu gisul : ma daldi ŋoor ci suufi jeexiti Yonent bi, daldi koy sànni li am am. Loolu la ma sama xel joxoon”.
97قَالَ فَاذْهَبْ فَإِنَّ لَكَ فِي الْحَيَاةِ أَن تَقُولَ لَا مِسَاسَ ۖ وَإِنَّ لَكَ مَوْعِدًا لَّن تُخْلَفَهُ ۖ وَانظُرْ إِلَىٰ إِلَٰهِكَ الَّذِي ظَلْتَ عَلَيْهِ عَاكِفًا ۖ لَّنُحَرِّقَنَّهُ ثُمَّ لَنَنسِفَنَّهُ فِي الْيَمِّ نَسْفًا
[Muusaa] daldi ne ko : “Ayca, demal. Toppal sa një : “Dootoo jegeñ kenn ! ” Te am nga dig boo dul wuute. Te xoolal sa yàlla ji nga daan jaamu. Dananu ko lakk, sànni ko ca ndox ma.
98إِنَّمَا إِلَٰهُكُمُ اللَّهُ الَّذِي لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۚ وَسِعَ كُلَّ شَيْءٍ عِلْمًا
[Seen Yàlla tigi] mooy Yàlla jenn ja, amul jeneen ju dul Moom. Moo xam lépp.
99كَذَٰلِكَ نَقُصُّ عَلَيْكَ مِنْ أَنبَاءِ مَا قَدْ سَبَقَ ۚ وَقَدْ آتَيْنَاكَ مِن لَّدُنَّا ذِكْرًا
Noonu la Nu lay nettalee xew-xewi ña jiitu woon. Indil naa la njàng mu bawoo fi Man.
100مَّنْ أَعْرَضَ عَنْهُ فَإِنَّهُ يَحْمِلُ يَوْمَ الْقِيَامَةِ وِزْرًا
Ku ko dummóoyu [kàddu yooyu], bu Bis-pénc baa, dana yenu ay bàkkaar [mbugal] ;
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
98Aaya

Tekki — Taha 98

Simoore Taha Aaya 98 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Seen Yàlla tigi] mooy Yàlla jenn ja, amul jeneen ju…

Simoore Aaya 98/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 96–100. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers