Al-Anbiya · 112/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
قَالَ رَبِّ احْكُم بِالْحَقِّ ۗ وَرَبُّنَا الرَّحْمَٰنُ الْمُسْتَعَانُ عَلَىٰ مَا تَصِفُونَ ۝١١٢
Qaala Rabbih kum bil haqq; wa Rabbunar Rahmaa nul musta`aanu `alaa maa tasifoon
📖 Tekkim Wolof
Yaw Yonent bi neel : “Yaw sama Boroom, àtteel ci dëgg ! Te sunu Boroom mooy Yërëmaakoon biy Dimbaliwaakoon biy musalee ci li ngeen koy nirale”

🎧 Dégg


📜 Aaya 110-112 — Simoore Al-Anbiya

110إِنَّهُ يَعْلَمُ الْجَهْرَ مِنَ الْقَوْلِ وَيَعْلَمُ مَا تَكْتُمُونَ
Moom dey xam na li ñuy biral ciy wax ak it li ngeen di nëbb.
111وَإِنْ أَدْرِي لَعَلَّهُ فِتْنَةٌ لَّكُمْ وَمَتَاعٌ إِلَىٰ حِينٍ
Te xamuma ; ndax moom nattu la ci yéen ak xéewal gu gàtt” !
112قَالَ رَبِّ احْكُم بِالْحَقِّ ۗ وَرَبُّنَا الرَّحْمَٰنُ الْمُسْتَعَانُ عَلَىٰ مَا تَصِفُونَ
Yaw Yonent bi neel : “Yaw sama Boroom, àtteel ci dëgg ! Te sunu Boroom mooy Yërëmaakoon biy Dimbaliwaakoon biy musalee ci li ngeen koy nirale”
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
112Aaya

Tekki — Al-Anbiya 112

Simoore Al-Anbiya Aaya 112 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yaw Yonent bi neel : “Yaw sama Boroom, àtteel ci…

Simoore Aaya 112/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 110–112. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers