Al-Anbiya · 111/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
وَإِنْ أَدْرِي لَعَلَّهُ فِتْنَةٌ لَّكُمْ وَمَتَاعٌ إِلَىٰ حِينٍ ۝١١١
Wa in adree la`allahoo fitnatul lakum wa mataa`un ilaaheen
📖 Tekkim Wolof
Te xamuma ; ndax moom nattu la ci yéen ak xéewal gu gàtt” !
🎧 Dégg

📜 Aaya 109-112 — Al-Anbiya

109فَإِن تَوَلَّوْا فَقُلْ آذَنتُكُمْ عَلَىٰ سَوَاءٍ ۖ وَإِنْ أَدْرِي أَقَرِيبٌ أَم بَعِيدٌ مَّا تُوعَدُونَ
Bu ñu dëddoo, neel : “Xamal naa leen loo xam ne noo ca yem ; mu di ndax li ñu leen dig dafa jegeñ walla dafa sori.
110إِنَّهُ يَعْلَمُ الْجَهْرَ مِنَ الْقَوْلِ وَيَعْلَمُ مَا تَكْتُمُونَ
Moom dey xam na li ñuy biral ciy wax ak it li ngeen di nëbb.
111وَإِنْ أَدْرِي لَعَلَّهُ فِتْنَةٌ لَّكُمْ وَمَتَاعٌ إِلَىٰ حِينٍ
Te xamuma ; ndax moom nattu la ci yéen ak xéewal gu gàtt” !
112قَالَ رَبِّ احْكُم بِالْحَقِّ ۗ وَرَبُّنَا الرَّحْمَٰنُ الْمُسْتَعَانُ عَلَىٰ مَا تَصِفُونَ
Yaw Yonent bi neel : “Yaw sama Boroom, àtteel ci dëgg ! Te sunu Boroom mooy Yërëmaakoon biy Dimbaliwaakoon biy musalee ci li ngeen koy nirale”
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
111Aaya

Tekki — Al-Anbiya 111

Simoore Al-Anbiya Aaya 111 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te xamuma ; ndax moom nattu la ci yéen ak…

Simoore Aaya 111/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 109–112. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers