Al-Anbiya · 18/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
بَلْ نَقْذِفُ بِالْحَقِّ عَلَى الْبَاطِلِ فَيَدْمَغُهُ فَإِذَا هُوَ زَاهِقٌ ۚ وَلَكُمُ الْوَيْلُ مِمَّا تَصِفُونَ ۝١٨
Bal naqzifu bilhaqqi `alal baatili fa yadmaghuhoo fa izaa huwa zaahiq; wa lakumul wailu mimmaa tasifoon
📖 Tekkim Wolof
Déedéet Dananu sanni dëgg ci kaw fen mu tojte ko, tax mu raaf. Te li ngeen di nirale [Yàlla] dana tax ngeen toskare.

🎧 Dégg


📜 Aaya 16-20 — Al-Anbiya

16وَمَا خَلَقْنَا السَّمَاءَ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا لَاعِبِينَ
Bindinu asamaan yi ak suuf si ak li nekk ci seen diggante ngir fo.
17لَوْ أَرَدْنَا أَن نَّتَّخِذَ لَهْوًا لَّاتَّخَذْنَاهُ مِن لَّدُنَّا إِن كُنَّا فَاعِلِينَ
Su Nu bëggoon po, kon [Dunu soxla bind dara], ci Sunu bopp la Nu koy sose, ndegam lu Nu nammoon a def la
18بَلْ نَقْذِفُ بِالْحَقِّ عَلَى الْبَاطِلِ فَيَدْمَغُهُ فَإِذَا هُوَ زَاهِقٌ ۚ وَلَكُمُ الْوَيْلُ مِمَّا تَصِفُونَ
Déedéet Dananu sanni dëgg ci kaw fen mu tojte ko, tax mu raaf. Te li ngeen di nirale [Yàlla] dana tax ngeen toskare.
19وَلَهُ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ وَمَنْ عِندَهُ لَا يَسْتَكْبِرُونَ عَنْ عِبَادَتِهِ وَلَا يَسْتَحْسِرُونَ
Moo moom lépp li nekk ci asamaan yi ak suuf si. Te ña nekk fa Moom duñu rëy-rëylu [ci di ko jaamu], te it duñu ca lott.
20يُسَبِّحُونَ اللَّيْلَ وَالنَّهَارَ لَا يَفْتُرُونَ
Dañu Koy sàbbaal guddi ak bëccëg, duñu ca jóge.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
18Aaya

Tekki — Al-Anbiya 18

Simoore Al-Anbiya Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Déedéet Dananu sanni dëgg ci kaw fen mu tojte ko,…

Simoore Aaya 18/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers