Al-Anbiya · 8/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
وَمَا جَعَلْنَاهُمْ جَسَدًا لَّا يَأْكُلُونَ الطَّعَامَ وَمَا كَانُوا خَالِدِينَ ۝٨
Wa maa ja`alnaahum jasadal laa yaakuloonat ta`aama wa maa kaanoo khaalideen
📖 Tekkim Wolof
Defunuleen woon [boroom] yaram yu dul lekk ñam. Te it nekkuñu woon ñuy béel [dañu daa lekk, di wopp, di dee].

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Simoore Al-Anbiya

6مَا آمَنَتْ قَبْلَهُم مِّن قَرْيَةٍ أَهْلَكْنَاهَا ۖ أَفَهُمْ يُؤْمِنُونَ
Xeet ya leen jiitu woon te gëmuñu, alag Nanu leen. [Kon] ñoon ndax danañu gëm ?
7وَمَا أَرْسَلْنَا قَبْلَكَ إِلَّا رِجَالًا نُّوحِي إِلَيْهِمْ ۖ فَاسْأَلُوا أَهْلَ الذِّكْرِ إِن كُنتُمْ لَا تَعْلَمُونَ
Mësunoo yónni ñu la jiitu lu dul aw góor yu Nu soloo. Laajleen ña jotoon Téere ndeem xamu leen.
8وَمَا جَعَلْنَاهُمْ جَسَدًا لَّا يَأْكُلُونَ الطَّعَامَ وَمَا كَانُوا خَالِدِينَ
Defunuleen woon [boroom] yaram yu dul lekk ñam. Te it nekkuñu woon ñuy béel [dañu daa lekk, di wopp, di dee].
9ثُمَّ صَدَقْنَاهُمُ الْوَعْدَ فَأَنجَيْنَاهُمْ وَمَن نَّشَاءُ وَأَهْلَكْنَا الْمُسْرِفِينَ
Topp, Nu def la Nu leen digoon. Daldi leen boole musal ak ku Nu soob. Yàqkat ya ñoom, Nu rey leen.
10لَقَدْ أَنزَلْنَا إِلَيْكُمْ كِتَابًا فِيهِ ذِكْرُكُمْ ۖ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
Wàcce Nanu ci yéen ab Téere boo xam ne seen teraangaa nekk ca biir. Moo ndax dangeen dul xel-lu ?
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Al-Anbiya 8

Simoore Al-Anbiya Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Defunuleen woon [boroom] yaram yu dul lekk ñam. Te it…

Simoore Aaya 8/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers