Al-Mu'minun · 116/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
فَتَعَالَى اللَّهُ الْمَلِكُ الْحَقُّ ۖ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ رَبُّ الْعَرْشِ الْكَرِيمِ ۝١١٦
Fata`aalal laahul Malikul Haqq; laaa ilaaha illaa Huwa Rabbul `Arshil Kareem
📖 Tekkim Wolof
Yàlla buur biy dëgg, kawe na ! Amul jeneen yàlla ju dul Moom, Mooy Boroom gàngunaay [Aras] gu tedd ga !
🎧 Dégg

📜 Aaya 114-118 — Al-Mu'minun

114قَالَ إِن لَّبِثْتُمْ إِلَّا قَلِيلًا ۖ لَّوْ أَنَّكُمْ كُنتُمْ تَعْلَمُونَ
Mu ne leen : “As ndiir su néew ngeen fa saxoon. Cëy bu ngeen xamoon”.
115أَفَحَسِبْتُمْ أَنَّمَا خَلَقْنَاكُمْ عَبَثًا وَأَنَّكُمْ إِلَيْنَا لَا تُرْجَعُونَ
Moo ndax dangeen a jortoon ne caaxaan rekk a taxoon Ma bind leen, ngeen jort it ne dungeen dellusi ci Man [Yàlla] ? ”
116فَتَعَالَى اللَّهُ الْمَلِكُ الْحَقُّ ۖ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ رَبُّ الْعَرْشِ الْكَرِيمِ
Yàlla buur biy dëgg, kawe na ! Amul jeneen yàlla ju dul Moom, Mooy Boroom gàngunaay [Aras] gu tedd ga !
117وَمَن يَدْعُ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ لَا بُرْهَانَ لَهُ بِهِ فَإِنَّمَا حِسَابُهُ عِندَ رَبِّهِ ۚ إِنَّهُ لَا يُفْلِحُ الْكَافِرُونَ
Képp kuy jaamu leneen di ko boole ak Yàlla, [na bir ne] amu ca firnde, te Yàllaa koy lijjanti. Li wér mooy yéefar ya duñu texe.
118وَقُل رَّبِّ اغْفِرْ وَارْحَمْ وَأَنتَ خَيْرُ الرَّاحِمِينَ
Waxal ne : “Boroom sama, jéggaleel te yërëme. Yaw yaa di gën ji yërëmaakoon yi”.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
116Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 116

Simoore Al-Mu'minun Aaya 116 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla buur biy dëgg, kawe na ! Amul jeneen yàlla…

Simoore Aaya 116/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 114–118. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers