Al-Mu'minun · 115/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
أَفَحَسِبْتُمْ أَنَّمَا خَلَقْنَاكُمْ عَبَثًا وَأَنَّكُمْ إِلَيْنَا لَا تُرْجَعُونَ ۝١١٥
Afahsibtum annamaa khalaqnaakum `abasanw wa annakum ilainaa laa turja`oon
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax dangeen a jortoon ne caaxaan rekk a taxoon Ma bind leen, ngeen jort it ne dungeen dellusi ci Man [Yàlla] ? ”

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 113-117 — Simoore Al-Mu'minun

113قَالُوا لَبِثْنَا يَوْمًا أَوْ بَعْضَ يَوْمٍ فَاسْأَلِ الْعَادِّينَ
Ñu tontu ne : “Nun daal, benn walla fan yu néew la nu fa saxoon, xam sax laajal limkat yi.”
114قَالَ إِن لَّبِثْتُمْ إِلَّا قَلِيلًا ۖ لَّوْ أَنَّكُمْ كُنتُمْ تَعْلَمُونَ
Mu ne leen : “As ndiir su néew ngeen fa saxoon. Cëy bu ngeen xamoon”.
115أَفَحَسِبْتُمْ أَنَّمَا خَلَقْنَاكُمْ عَبَثًا وَأَنَّكُمْ إِلَيْنَا لَا تُرْجَعُونَ
Moo ndax dangeen a jortoon ne caaxaan rekk a taxoon Ma bind leen, ngeen jort it ne dungeen dellusi ci Man [Yàlla] ? ”
116فَتَعَالَى اللَّهُ الْمَلِكُ الْحَقُّ ۖ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ رَبُّ الْعَرْشِ الْكَرِيمِ
Yàlla buur biy dëgg, kawe na ! Amul jeneen yàlla ju dul Moom, Mooy Boroom gàngunaay [Aras] gu tedd ga !
117وَمَن يَدْعُ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ لَا بُرْهَانَ لَهُ بِهِ فَإِنَّمَا حِسَابُهُ عِندَ رَبِّهِ ۚ إِنَّهُ لَا يُفْلِحُ الْكَافِرُونَ
Képp kuy jaamu leneen di ko boole ak Yàlla, [na bir ne] amu ca firnde, te Yàllaa koy lijjanti. Li wér mooy yéefar ya duñu texe.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
115Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 115

Simoore Al-Mu'minun Aaya 115 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax dangeen a jortoon ne caaxaan rekk a taxoon…

Simoore Aaya 115/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 113–117. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers