Al-Mu'minun · 30/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ وَإِن كُنَّا لَمُبْتَلِينَ ۝٣٠
Inna fee zaalika la Aayaatinw wa in kunnaa lamubtaleen
📖 Tekkim Wolof
Ay kéemaannekk na ci biir loolu. Doontele sax dañuy nattu (ñi gëm).

🎧 Dégg


📜 Aaya 28-32 — Simoore Al-Mu'minun

28فَإِذَا اسْتَوَيْتَ أَنتَ وَمَن مَّعَكَ عَلَى الْفُلْكِ فَقُلِ الْحَمْدُ لِلَّهِ الَّذِي نَجَّانَا مِنَ الْقَوْمِ الظَّالِمِينَ
Saa soo duggee ca gaal ga yaak ña nga àndal ba noppi, nanga wax ne : “Cant ñeel na Yàlla Moom mi nu musal ci ay nit yu di ay tooñkat.”
29وَقُل رَّبِّ أَنزِلْنِي مُنزَلًا مُّبَارَكًا وَأَنتَ خَيْرُ الْمُنزِلِينَ
Te nanga wax ne : “Sama Boroom, nanga ma wàcce ngën gi wàccuwaay bu barkeel, Yaw yaa di gën ji wattu”.
30إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ وَإِن كُنَّا لَمُبْتَلِينَ
Ay kéemaannekk na ci biir loolu. Doontele sax dañuy nattu (ñi gëm).
31ثُمَّ أَنشَأْنَا مِن بَعْدِهِمْ قَرْنًا آخَرِينَ
Topp, ginnaaw ba, Nu sos ay maas ci ñeneen,
32فَأَرْسَلْنَا فِيهِمْ رَسُولًا مِّنْهُمْ أَنِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۖ أَفَلَا تَتَّقُونَ
Nu yónni ci ñoom ab Yonent bu bokk ci ñoom [ngir mu wax leen] : “Jaamuleen Yàlla. Amuleen jeneen yàlla ju dul Moom. Moo ndax dangeen dul ragal Yàlla ? ”
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
30Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 30

Simoore Al-Mu'minun Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ay kéemaannekk na ci biir loolu. Doontele sax dañuy nattu…

Simoore Aaya 30/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers